Wërlaay wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 5 :
Ci baax, '''wërlaay''' - walla barabub jëf mbaa mbir, maanaam fu lëf nekk mbaa deesi defe ko fa - mi ngi ame ci jëmm yi (substence), peekte ti (circonstance), mbir yi walla nekkiin wi ko peek wër ko, te di fa ame.
 
Bu dee ci wàllug dundat (biyoloji) rawati na ci wàllug dénd (ecoloji)day tekki léépplépp lu man a def ay jeexiital yu jonjoo ci doxug walla màggug mbaa jëm kanamug mbir yi (metabolosmo)walla nekkiinu jëmm walla xeet wuy dund ( SPECIE VIVENTE), loolu nag leer ci la, ngelaw, ndox, suuf ak yeneen nekktéef yiy dund.