Ubbi njël lu njëkk li

Modifications

Coppite gi amul tënk
Xët wii moo lay leeral nooy xamale yeneen jëfëndikookatjëfandikukat yi, say xameel ci yeneen làkk yi ak tolluwaayu xameel gi.
----
----
== LumuyLi muy jariñ ==
Donte fii [[Wikipedia]] ci kàllaama [[wolof]] la, waaye du ñi fi nekk ñépp a deggante. Am na ñu deggul wolof, walla seen degg des na, ñu man a soxla ku ñu jokkool ci làkk bi ñu degg, walla wolof yu yomb. Am na ay waa -wikipedia yu deggul wolof te di bëgg a jàpp ci liggéey bi, kon di na am solo lool nga wax ko ci yan làkk ngeen man a waxtaane, ngir njariñam man a feeñ.
 
Mii sémb di na yombal jokkoo gi ci biir aw askan gu bariy làkkbarilàkk gu mel ne Wikipedia: ci misaal, di na yomb jot kuy wax wenn làkk wi, te itam di na xamale tolluwaayu degginudégginu wolof gu ab jëfëndikookatjëfandikukat bu bindu.
 
== Nu ma koy defee? ==
{{Babel|wo-1|fr-1|en-1}}
Doy na nga yokk ci sa [[Xëtu jëfëndikookatjëfandikukat|xëtu jëfëndikookatjëfandikukat]] '''Babelbox''' bi, tabax ko ci topp tektal yii:
* Nga yokk ci limu làkk yi nga degg te teg ci '''|'''
**Misaal: '''{{Babel|''' (3 làkk)
3 285

modifications