Waalo wuute gi ci sumb yi

41 octets ajoutés ,  13 at ci ginaaw
+image
m (robot Adding: lt:Vaalo)
(+image)
[[Image:Senegal-reine-du-waloWaaloMap.jpg|thumb|Ndete Yalla250px|Waalo]]
'''Waalo''' bokkoon na ci yénn ci nguuri [[Senegaal]] yi fi nekkoo. Buuru Waalo dañu ko daa tànn ca péncum Seb ak Bawar. Njurbel moo nekkoo péeyam ci lu njëkk, ganaaw bi lañ ko tuxël Jinge, tuxëlaat ko Ndeer. Tuxu yu bari yooyu doy na tegtal ci dellu ganaaw ak ñàkk doole.
 
 
== Barag ==
[[Image:Senegal-reine-du-walo.jpg|thumb|Ndete Yalla]]
Barag mooy maqaama bi ñu joxoon buuru Waalo. Yilifoon na li dale ca [[Mbàmbulaanu Atlas]] ba Lag de geer. Bokkoon na ci ñi dar Barag ñaari mbooloo: ba njëkk moo di [[Lingeer]] miy yaayu buur bi ak Aawo miy soxnaay buur su njëkk, moom moo am teraraagaay toog ca gangunaay (mooy toogu gu buur) ga.
 
1 014

modifications