Gëwéel wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
 
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 2 :
 
== Melokaan ==
Ci li jege [[Yamoo|yamoo]] gi, di nañ faral di gis klimaa bu ànd ak tangoor gu tar ak taw bu bari ci at mépp: di ko wax [[Klimaab yamoo|klimaab yamoo]]. Waaye, ci njegeeti gëwéel yi (tef mbaa Sankar), ci at mi [[Noor|noor]] ak [[Nawet|nawet]] rekk a ci am, kon wàccit yi (taw yi) day wuute ci jamonoy at mi, ba daanaka at méppay tang, di li ñiyñuy wax [[Klimaab gëwéel|klimaab gëwéel]].
 
Waaye nag jàpp ne it ngelaw yiy uppu ak dawaani géej yi ak rëyaayu diwaan bi am nañ ay njeexit yu solowu ci klimaay diwaan yi, ba tax na su nu seetloo yenn diwaan yi, donte nekk nañ ci wetu ab gëwéel, amuñu klimaab gëwéel (ci misaal diggu Óstraali walla gu Sahara, nga xamne amuñu nawet) ak yenn diwaan yu am klimaab gëwéel te nekkuñu ci njegeeti gëwéel yi( lu mel ne réewum [[Keeñaa]], nekk ci yamoo gi te li ëpp ci suufam klimaab gëwéel la am).
[[Image:Wendekreise Tropics Donence.png|300px|thumb|Gëwéel yi ñooy rëdd yu baxa yu xëm yi, ci kaw ak suufu yamoo gi, moom di rëdd wu leer wi]]
== Diwaani gëwéel yu mag yi ==
Diwaan yiy dundu cib klimaab gëwéel dëgg-dëgg ñoo ngi nekk ci [[diggu Aamerig]] ak [[bëj-saalumu Aamerig]], ci digg ak genn wàllu [[bëj-gànnaaru Afrig]], ci bëj-gànnaargànnaaru [[Óstraali]] ak geengenn wàllu [[Endoneesi]]. Li des ci barabu diggantegëwéel bi dañ leen di séddale ci ci diggante klimaab tàkk (rawatina ci [[Afrig]]), bu yamoo walla bu xaw a sedd (rawatina ca [[Asi]]
 
=== Lëkkalekaay yu biti ===