Waalo wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ji-Elle (waxtaancëru)
+de +en
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 2 :
'''Waalo''' bokkoon na ci yénn ci nguuri [[Senegaal]] yi fi nekkoo. Buuru Waalo dañu ko daa tànn ca péncum Seb ak Bawar. Njurbel moo nekkoo péeyam ci lu njëkk, ganaaw bi lañ ko tuxël Jinge, tuxëlaat ko Ndeer. Tuxu yu bari yooyu doy na tegtal ci dellu ganaaw ak ñàkk doole.
 
== GëwrinJëwrin yi ==
Ñooñu ñooy: Jawdaŋ mi yor suuf si ak Jogomaay mi yor ndox ak Maalaw mi yor koom-koom gi. Ganaaw ñooñu amoon na ñu nekkoon ci kër buur. Bokk na ca Meet moom mooy njiitu bëkk-nèeg yi ak bëkk-nèegu Njurbel moom mooy wax ci turu buur bi ak njiitu ñi yor baxan buur te mu gën a siiwe ci Baadi ak taawub buur. Moom mooy saytu néegu buur ak Fara Njurbel moom mooy njiitu tëgg weñ gu ñuul ak wurus yi. Fara Juñ-juŋ bi moom mooy njiitu waykat yi.
 
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Waalo » lañ ko jële