Bawol wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
m Tuddewaat koBawal en Bawol
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
Ci xarnub fukk ak juroom '''BawalBawol''' nguur su ndaw la woon su toppoon [[Jolof]] gu mag gi, bu ko defee, ag njaboot gu amug jegeñaale ak buuri [[Kajoor]] yi daa ko jiite.
 
Ci xarnub fukk ak juroom benn g.j, la Jolof mànge poseb néew-dooleg nguurug Jolof , daal di jël ag tembam, ni ko yenn ci nguur yi defe woon, gu ci mel ne [[Kajoor]] ak [[Waalo]], ngir song gu tar ga Amari Ngóne Sabel Faal defoon Jolof. Ci ñaareelu xaaju xarnu bii la Amari Ngóone xëy di buuru Kajoor ak BawalBawol ci jenn jamono ji.
Booba la buur bi tàmbalee jiite ñaari nguur, waaye nguur gu ci nekk yor politigu doxaliinu réewam. Waaye boole gii bari lu mu daa jur ay réeroo ci diggante ñaari nguur yi, ndax gu ci nekk da daa bëgg a yilif ga ca des.
 
Booba la buur bi tàmbalee jiite ñaari nguur, waaye nguur gu ci nekk yor politigu doxaliinu réewam. Waaye boole gii bari lu mu daa jur ay réeroo ci diggante ñaari nguur yi, ndax gu ci nekk da daa bëgg a yilif ga ca des.
 
Buurub Bawal nag di Teeñ ab jataay a ko daa jàppale, bu ñu wéer tabbug kiy wuutu buur bi bu faatoo, ak fuglug saxal yi buur bi di def.
Nguur gi amoon na ab ëttu àtte buy àtte mbir yi, mbooleem maas yi nag daa nanu fa àttewoo ( maasug nappkat yi, baykat yi, sàmm si, ñoñ fànn ñi (boroom mecce yi) ak jigéen ñi).
Bokkug BawalBawol ci Yaxantug [[Tàkk]] gi taxu ko woon a deme noonu, ndaxte yooni yaxantu gi rombutoon ciy suufam, moom kay daa yamoon rekk ci yaxantug tefes gi.
 
{{modèle:buntutaariix}}
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Bawol » lañ ko jële