Alaaji Maalik SY wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ji-Elle (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Alaaji Maalik''' ma nga gane àdduna Gaaya ca wetu Dagana atum 1855. Waajuram wu góor tuddoon Usmaan, wu jigéen Faa Wàdd Wele. Mi ngi jànge alxuraan Luga ci kenn ci taalibey Alaaji Omar Futiyu Taal yi. Bi mu doonee mag la dem Màkka, bi mu dellusee sax ci jaamu Yàlla ak jàngale ak dugal ñi duli jullit ci lislaam. Ci noonu la tase njàngalem yoonu Tiijan ci Senegaal jaare ko ci tuxoom yi ci Jolof, Kajoor ak Ndar. Ci mujj gi mu dëkksi Tiwaawan atum 1902. Fa la njëkk a xumbale gàmmu. Wooteem bi mi ngi ko doon defe ci dëkk yu mag yi, tabax fa ay jàkka, xeex fa ag réer akug ñàkk, ñu tudde ko Mawdo giiy tekki aji gindi ji. Alaaji Maalik nag (yal na ko Yàlla gërëm), mi ngi laqu atum 1922 g.j.
[[catégorie:niti senegaal]]
[[fr:El-Hadji Malick Sy]]