Saamóori Ture wuute gi ci sumb yi

36 octets ajoutés ,  14 at ci ginaaw
Coppite gi amul tënk
Ci atum 1898 g.j, waa Fràas yi bett nañu ko ca kãa bu Gelemu, ñu njaf ko, yobbu ko Gabon, fa la faatoo ci atum 1900 g.j daal di jël nguuram googu boole ko ci Cote d’Ivoire.
Jàmarloo gu Saamóori Ture gi kontar tubaab yi dees na ko jàppe genn ci yi ëpp solo ci jàmmarloo yi ci sowwu Afrig. Sax na diirub 17 at. Yóbbe na canc gi ay ñakk yu takku.
 
==Xool it==
*[[Taariixu Senegaal]]
[[catégorie:niti senegaal]]
1 014

modifications