Saamóori Ture wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Xët wu bees : '''Saamóori Ture''' mi ngi juddoo Mayambalandogo ci lu tollook 1830 g.j. Mu nekkoon ab yaxantukat, dajale woon na ab xare ngir nangu suuf yu bari, daal di taxawal ag Imbraatóor. D...
 
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 4 :
Ci atum 1898 g.j, waa Fràas yi bett nañu ko ca kãa bu Gelemu, ñu njaf ko, yobbu ko Gabon, fa la faatoo ci atum 1900 g.j daal di jël nguuram googu boole ko ci Cote d’Ivoire.
Jàmarloo gu Saamóori Ture gi kontar tubaab yi dees na ko jàppe genn ci yi ëpp solo ci jàmmarloo yi ci sowwu Afrig. Sax na diirub 17 at. Yóbbe na canc gi ay ñakk yu takku.
[[catégorie:buuriniti senegaal]]