Muhammad Lamin Daraame wuute gi ci sumb yi

11 octets supprimés ,  13 at ci ginaaw
Coppite gi amul tënk
(Xët wu bees : '''Muhammad Lamin Daraame''' (turam dëgg di Demba Dibaasi) sëriñ la won bu bokkoon ci giirug Saraxule, di woon it tiijaan bu askanoo ci Gonjuro. Tukki woon na dem Màkkatal Mukaara...)
 
Muhammad Lamiin ñàkkoon na lu bari ci xarekatam yi ci xare bii. Tubaab yi ray nanu ko ci ndimbalul Muusa Mulo. Ñu mujjoon manante buur yu bari ci ñu xaatim ay kóllarey ndénkaane(tutelle), tegoon it loxo lu ëpp ci suufi Senegaal yi.
 
[[catégorie:njiiti diine yuniti senegaal]]
3 287

modifications