Tuubaa wuute gi ci sumb yi

53 octets ajoutés ,  13 at ci ginaaw
Coppite gi amul tënk
[[Image:Touba.jpg|thumbnail|250pxleft|Tuuba200px|Tuubaa]]
[[Image:SN-Touba.png|right|200px|thumb]]
 
'''Tuubaa''' (''fr''. Touba) benn dëkk bu nek ci rèèwu [[Senegaal]] (diiwaanu Bawal).
 
Ci dëkku Tuubaa boobu fala nekk juma'i Tuubaa, doon bennn ci bërëbu jamu Yalla yi gënë mak ci [[Afrik]]. Ci wetu jumaa jooju fala nekk xabru Sëriñ Tuubaa, maanaam kilifa diinè bi sañc Tuubaa.
 
Ci Tuubaa dinañu fa dajaloo at mu nè lu toll ci ñaari milyong'i tàlibè, ñuy ñew ci besu'p Magal'u Tuubaa.
 
 
{{commons|:category:Touba, Senegal|TuubaTuubaa}}
 
 
1 014

modifications