Koor wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Guaka (waxtaancëru)
Guaka (waxtaancëru)
Rëdd 144 :
 
== Ponki koor (ay farataam), ay sunnaam, yu ñu sibam ==
1 –# yéene, mooy fas ci xol ne danga woor ngir topp ndigalul Yàlla (t.s), walla ngir jaamu ko, ngir waxam ja (j.m) : “ ku fanaanalul yéeney woor, amul koor” . Bu dee ngàttnga la nag moom dana baax ak doonte ginnaaw bu fajar fenkee la, bёccёg bi tàmbalee dugg, bu fekkee ne jotul woon a lekk dara, ngir waxi Soxna Aysa ji (y.y g) : «Yonnant bi (j.m) dugg na fi man bis, ne : ndax yor ngéen dara ? ñu ne ko : dée-déet, mu ne : kon woor naa»
2 –# Jàpp, mooy bàyyi yiy dogloo moo xam lekk la mbaa naan walla séy.
 
3 –# Jamono koor gi, maanaam bёccёg gi, mi ngi tàmbalee ci fenkug fajar gi ba ca sowug jant bi. Bu waay wooroon guddi gi, dog ci bёccёg bi, ag kooram du wér, ngir waxam ja (t.s) : «Mottalileen koor gi ba ci guddi gi»
2 – Jàpp, mooy bàyyi yiy dogloo moo xam lekk la mbaa naan walla séy.
 
3 – Jamono koor gi, maanaam bёccёg gi, mi ngi tàmbalee ci fenkug fajar gi ba ca sowug jant bi. Bu waay wooroon guddi gi, dog ci bёccёg bi, ag kooram du wér, ngir waxam ja (t.s) : «Mottalileen koor gi ba ci guddi gi»
 
=== Sunnay koor ===
Ligne 189 ⟶ 187 :
 
10 – nàmpatal ak lu ni deme ngir ragal ag néew-doole gu man a waral ag dog
 
 
 
== Luy yàq koor, ak lu ñu daganal ci ku woor mu def ko, ak lu ñu ko ciy jéggal ==
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Koor » lañ ko jële