Koor wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Guaka (waxtaancëru)
Rëdd 140 :
 
==== Ñaari yeete ====
1 –# Ku sàgganee fay koor gu mu waroon a fay ci lu dul ngànt ba geneen koor dellusi, war nay leel ab miskiin ci barabu bépp bis bu mu war a fay.
2 –# Jullit bu faatu te waroon a fay ag koor, koor ga kilifaam a ko koy fayal, ngir waxam ja (j.m) : “ ku faatu te borub koor a ngi ci kawam, na ko ko kilifaam fayal” ak waxam ja ñeel ka ko laajoon ne ko: “ sama yaay dafa faatu te war naa fay aw weeru koor ndax dama ko koy fayal ?. Mu ne : waa-waaw, bor bu ñu yoreel Yàlla de moo gёn a yayoo ñu fay ko”
 
2 – Jullit bu faatu te waroon a fay ag koor, koor ga kilifaam a ko koy fayal, ngir waxam ja (j.m) : “ ku faatu te borub koor a ngi ci kawam, na ko ko kilifaam fayal” ak waxam ja ñeel ka ko laajoon ne ko: “ sama yaay dafa faatu te war naa fay aw weeru koor ndax dama ko koy fayal ?. Mu ne : waa-waaw, bor bu ñu yoreel Yàlla de moo gёn a yayoo ñu fay ko”
 
== Ponki koor (ay farataam), ay sunnaam, yu ñu sibam ==
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Koor » lañ ko jële