Wolof (làkk) wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Soppi ak jullasu Modification avec l’application Android
→‎Ubbite : Baay Faal Mbóoj
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Rëdd 15 :
Li ma bëgg a wax mooy naka la nu bëgg a bàyyee sunu làkk yii, rawatina wii di wolof, ca nooyam ga, ak nangoom ga, ak gàttam ga ak noppaleem ga, taaram ba, leeram ga, manam gaa leeral ak yaatoom ga, ak ruyu gi mu nangu, naan dangay jëlati weneen di ci sonn ak a sonle, naan day wa gën? Ma ne ñoom ñoo gis loolu man de déet !
 
Wolof mooy làkk wi ñu gën a wax ci [[Senegaal]], waaye ngir doyodig waa [[Afrig]] yi ba leegi, frañse mii nga xam ne lu matul 30 cib téeméer ci doomi Senegaal yi rekk a koy wax moo fiy làkk wu njëkk, maanaam wi nguur gi di waxe di ci liggéeye. Moor Taala Baay Faal Mbóoj
 
== Cosaanam ==