Penku gu Jege wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Xët wu bees : thumb|right|300px|'''Penku gu Jege''' ci lonkoyoonu àdduna bi '''Penku gu Jege''' su ñu koy wax mooy diwaanu séwógaraafi gi araab ...
 
Ibou (waxtaancëru)
Rëdd 1 :
[[Image:NearEast.png|thumb|right|300px|'''Penku gu Jege''' ci lonkoyoonu àdduna bi]]
'''Penku gu Jege''' su ñu koy wax mooy [[Diwaanu séwógaraafi|diwaanu séwógaraafi]] gi araab yi dëkkee, di tambalee ci pegg gu penku gu [[Géej gu Diggu]] gi ba ci [[Iraak]]. Moo taqaloo ak réew yi nekk ci [[Penku gu Diggu]] gi, féete ko penku, di: Iraan, Afganistaan, Pakistaan (Di yemoo ak baatu waa faraas bi di ''Moyen Orient'' ak bu waa angalteer bi bidi "Middle East").
 
== Réew yi ==
* [[Isipt]]
* [[Israayil]]
* [[Palestiin]]
* [[Libaan]]
* [[Siiri]]
* [[Jordaani]]
* [[Iraak]]
 
 
[[catégorie:Asi]]
{{modèle:Diwaani tugalasi}}
 
 
[[an:Orién Prosimo]]
[[en:Near East]]
[[es:Oriente Próximo]]
[[fa:خاور نزدیک]]
[[fr:Proche-Orient]]
[[id:Timur Dekat]]
[[it:Vicino Oriente]]
[[ja:近東]]
[[ka:ახლო აღმოსავლეთი]]
[[ko:근동]]
[[mk:Близок Исток]]
[[nl:Nabije Oosten]]
[[pt:Oriente Próximo]]
[[ru:Ближний Восток]]
[[sl:Bližnji vzhod]]
[[sv:Främre Orienten]]
[[uk:Близький Схід]]
[[zh:近東]]