Aadama wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Wolof dëgg (waxtaancëru)
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Soppi ak jullasu Modification avec l’application Android
Wolof dëgg (waxtaancëru)
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Soppi ak jullasu Modification avec l’application Android
 
Rëdd 53 :
83. ba mu des sa jaam ñiy sellal”."
 
==Aadama Ak Noonam Ba ([[Ibliis]])==
 
Bi [[Yàlla]] noppee ci [[Ibliis]] ak ci yedd ko, Ibliis bañ rekk ne day moy Yàlla. Sunu [[Boroom]] rëbb ko tàq ko ci yërmàndeem def ko Saytaane Rajiim, génne ko ca [[guyaar]]. Ginnaaw loolu Ibliis sumboo ak meram iñaane [[Aadama]], mu bëgg koo génne guyaar. Yàlla bàyyi ak Aadama xelam gawu ko ci dara, mu bayyi ko ak sagoom, muy man a ràññe lu baax ak lu bon, ginnaaw ba mu ko maytuloo Ibliis, Yàlla a ngi naan:
 
". Nu wax ko ne ko : “Kii dey sab noon la yaak sa [[soxna]]. Farluleen ba bu mu leen génne [[Àjjana]], [su ngeen génnee] da ngeen sonnu de.
 
118. [Fii ci Àjjana] doo fi xiif, doo fi rafle,
Rëdd 65 :
Ginnaw bi ñu dàkkoo Ibliis, mu tàmbali nag ci jëfe la mu dogu woon; te mooy fayu ci Aadama (HS) ak génne ko guyaar, di ko awale ci di ko jiixi-jaaxaloo, jéem koo gëmloo ne xam na lol man na tax ba Aadama sax dàkk du dee mukk. Yàlla a ngi wax naan:
 
"[[Séytaane]] daldi koy jax-jaxal [nëxal xelam] ne ko : "Yaw [[Aadama]], ndax duma la tegtal [[garab]] guy tax nga am nguur gu dootul foq ? ”."
 
[[Ibliis]] jaare ci bëggug [[Aadama]] ci sax fi dàkk ak sax ca [[guyaar]]; bañ fa a génn. Mu xam ne loolu ay tombug néew dooleem, [[Ibliis]] daa bëgg a wan ne sunu Boroom; man naa alag kii nga may gënalee. Adaama moom ndaysaan, xamul dara ci kàcci Ibliis yi, waaye li mu ko wax neex na ko te jar na a jarabu, mu yëg ne loolu du'y fo mu laaj Ibliis naka lay def ba am loolu moom ak soxnaam Awa? Ibliis ne ko : ndax yaa ngi gis garab gii ñu la tere nga lekk ci? Moo la ko man a may. Waaye ba tay Aadama gëmul Ibliis, muy fàttaliku tere gi sunu Boroom tere woon ci mu bañ a jege garab gi.
 
Kon naka la Aadama def ba lekk ca garab ga ak aartu yi ñu ko aartu yépp bàyyikoo ci sunu Boroom?
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Aadama » lañ ko jële