Aadama wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Wolof dëgg (waxtaancëru)
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Soppi ak jullasu Modification avec l’application Android
Wolof dëgg (waxtaancëru)
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Soppi ak jullasu Modification avec l’application Android
Rëdd 3 :
''[[Aadama]]'' mooy ni ñu ko waxe ci [[Lislaam]] ('''آدم'''). Ci angale mooy ''Adam'' te ci faranse itam mooy ''Adam''. Mooy nit ki [[Yàlla]] jëkka sàkk.
 
[[==[[Aadama]] ci [[Biibël|Biibël ba]]==
 
[[Nettalib]] Aadama feeñ na ci Ge 1:26-30; 2:4-8; 15-20. Aadama dafa toppoon jabaram [[Awa]] ci bàkkaaram. Bàkkaar boobu mooy [[lu]] indi musiba yépp yi nu gis ci àddina si (Ge 3:6-21). At, ya Aadama dundoon, 930 la. (Ge 5:5). Ci Injiil dañuy wax ci Aadama ci Lu 3:38; Ro 5:14-19; 1Ko 15:22,45; 1Tim 2:13,14; Yu 1:14.
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Aadama » lañ ko jële