Aadama wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Wolof dëgg (waxtaancëru)
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Soppi ak jullasu Modification avec l’application Android
Wolof dëgg (waxtaancëru)
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Soppi ak jullasu Modification avec l’application Android
Rëdd 11 :
[[Nettalib]] Aadama feeñ na ci suraat 2:30-38; 3:33,59; 7:11,19-27; 17:61-62; 18:50; 19:58; 20:115-128. Nekk na ki Boroom bi [[jëkk]] a bind muy nit doon tamit Yónnent bi njëkk.
Yàlla a ngi wax ci Alxuraan:
" Fàttalikul ba sa Boroom waxee Malaaka ya, ne leen: “Man dey damaa namm a def ci suuf si ag kilifa[kuutaay]. Ñu toontu ne ko : “Moo ndax dangay def ci suuf si koo xam ne daf ciy nekk di yàq, di tuur i dereet, te nun nu ngi lay sàbbaal, di la sant te di màggal sag sell ? Mu ne: Xam Naa loolu leenngeen xamul”
 
Yàlla wahyu suuf si ne ko: damay sàkk ci ya ay bindéef, amna ci ñoom ñu may topp, am ci ñoom ñu may moy, képp ku ma ci topp ma tàbbal ko guyaar, képp ku ma moy ma tàbbal ko sawara.
 
Suuf ne ko: ndax dangay bind ci man ñoo xam ne danga leen di dugal sawara? Sunu Boroom ne ko: waaw!
 
Nee nañu: Ibliis daal di wàcc ci kaw suuf ne ko yaw suuf, damaa ñëw ngir laabiire la, Yàlla daa namm a bind ci yaw ki gën ci bindaafon yi, te may ragal ñu moy ko mu leen di tàbbal sawara, bu booba yaw it dinga duggaale sawara tamit. Suuf daa di jooy!
 
Yàlla bind sunu baay Aadama ciy yoxoom ngir Ibliis bañ a rëy ci sujjótal ko, Yàlla a ngi nuy wax ci loolu:
 
"Suma ko móolee ba ëf ci Sama Ruu, nangeen daldi rot, sujjóotal ko."
 
Nee nañu: bi Yàlla bindee Aadama (HS) toog na 40i guddi. Am ñu ne: 40i at, muy jëmm ju ñu tërëral. Ibliis daan ko dikke, di ko kàjji muy keleŋ ni ban wu wow, nee ñu mooy li sunu Boroom naan:
 
" Moom moo bind nit ci ban bu tikk dëgër ".
 
Ibliis di dugg ci biir gémmiñu Aadama di génne ci ginnaawam, di jaar ci ginnaawam di génne ci gémmiñam, te naan ko: " Doo dara, ak lu tax ñu bind la, su ñu ma la saytuloo ma alag la, bu ñu la saytuloo ma ma moy la".
 
Malaaka yi bu ñu ko daan romb dañu ko daan ragal, fekk ne Ibliis moo leen ko gën a ragal. Ba dig bi nga xam ne la Yàlla namm ëf Ruuwam ci moom jotee, mu ëf Aadama Ruuwam. Mu digal Malaaka yi ci ñu sujjóotal Aadama. Malaaka yépp sujjóotal Aadama ba mu des Ibliis ngir rëy mu bokk ci way-wedd ni ca saa sa. Yàlla ne ko yaw Ibliis, ana lu la tee sujjóot ndeem digal naa la? Mu ne kii maa ko gën, man du ma sujjóotal nit koo binde ci suufu ban.
 
Ibliis sujjóotul ngir rëyam ak mbewteem ak kiñaan. Yàlla ne:
 
" 75. (Yàlla) daldi ne : “yaw Ibliis, lan moo la tere nga sujóot ci lii ma bind ci samay yoxo ? Dangay rëy-rëylu walla dangaa bokk ci ña kawe ? ”
 
76. “[Ibliis,] tontu ne ko : maa ko gën ndax yaa ngi ma bind ci safara moom nga bind ko ci
 
ban”.
 
77. (Yàlla) ne ko : “Génnal ca biti, dàkku naa la ;
 
78. te Samam rëbb dal na la ba ba saa di taxaw”.
 
79. “[Ibliis,] ne ko : yaw sama Boroom, muñal ma, ba bisub dekkiwaat ba”.
 
80. (Yàlla) ne ko : “may Nanu la dig boobu,
 
81. ba ca bisub waxtu wu ñu xam wa (Bis Pénc ba)”.
 
82. “[Ibliis ne ko] giiñ naa ci sa màgg gi ne ! Danaa leen lajj-loo ñoom ñépp,
 
83. ba mu des sa jaam ñiy sellal”."
 
==[[doom]] Aadama==
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Aadama » lañ ko jële