Sëriñ Tuubaa wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Daarul xayri (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: Soppikaay gu gisu Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Daarul xayri (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Rëdd 1 :
[[Image:AhmaduBamba.jpg|thumb|200px|Benn nataal bu Xaadim Rasuul]]
'''[[Sëriñ tuubaa| Sëriñ Tuubaa Xaadimu-rRasuul]]''' (''Seex Aḥmad ibn Muḥammad ibn Ḥabiib Allaa'' [[1853]]-[[19 sulet]] [[1927]]) boroom [[xam-xamu diine]] bu jullit la bu di ab [[sëriñ]] te cosaanoo ci ag càllala gu [[doomi soxna]]. Mi ngi gane àdduna ci [[Mbàkke]], ab dëkk bu maamaatam sancoon ca nguurug [[Bawol]], maamaatam jooju mooy '''Maharam''', walla [[Maaraam]],mooy ki sanc [[Mbàkke Bawol]], waxees na ne loolu ci atum Shaqdadin la di (1194 g / 1780 g.j ) . Waaye dëkkewu fa woon, da fa a bàyyi woon ab taawam '''Muhammudu Farimata''', magi habiibullaah ju mu bokkalul nday. Moom nag sëñ '''Maaram''' mii daa desoon [[Jolof]], fa la làqoo ñu denci ko fa, di ko siaare.
 
Ñu koy woowe itam [[Xaadim Rasuul]] di Ñaari baati [[araab]] yuy wund Surgab [[yonent]] bi [[Muhammad]] (j.m). Mu bokk ci jëmm yi gën a fés te ëpp solo ci diiney [[Lislaam]] ci [[sowwu Afrig]], ndax moom moo sos [[yoonu murit]]. Waa-réewam Seex Ahmadu Bamba lañu koy woowe ndax cofeel gu ñu am ci moom.