Sëriñ Tuubaa wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Daarul xayri (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Daarul xayri (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: Soppikaay gu gisu Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Rëdd 1 :
[[Image:AhmaduBamba.jpg|thumb|200px|Benn nataal bu Xaadim Rasuul]]
'''[[Sëriñ tuubaa|Sëriñ Tuubaa Xaadimu-rRasuul]]''' (''Seex Aḥmad ibn Muḥammad ibn Ḥabiib Allaa'' [[1853]]-[[19 sulet]] [[1927]]) boroom [[xam-xamu diine]] bu jullit la bu di ab [[sëriñ]] te cosaanoo ci ag càllala gu [[doomi soxna]]. Mi ngi gane àdduna ci [[Mbàkke]], ab dëkk bu maamaatam sancoon ca nguurug [[Bawol]], maamaatam jooju mooy '''Maharam''', walla [[Maaraam]],mooy ki sanc [[Mbàkke Bawol]], waxees na ne loolu ci atum Shaqdadin la di (1194 g / 1780 g.j ) . Waaye dëkkewu fa woon, da fa a bàyyi woon ab taawam '''Muhammudu Farimata''', magi habiibullaah ju mu bokkalul nday. Moom nag sëñ '''Maaram''' mii daa desoon [[Jolof]], fa la làqoo ñu denci ko fa, di ko siaare.
 
Ñu koy woowe itam [[Xaadim Rasuul]] di Ñaari baati [[araab]] yuy wund Surgab [[yonent]] bi [[Muhammad]] (j.m). Mu bokk ci jëmm yi gën a fés te ëpp solo ci diiney [[Lislaam]] ci [[sowwu Afrig]], ndax moom moo sos [[yoonu murit]]. Waa-réewam Seex Ahmadu Bamba lañu koy woowe ndax cofeel gu ñu am ci moom.
Rëdd 30 :
 
== Sancug [[Tuubaa]] ==
[[Image:Jumaay Tuubaa.jpg|thumb|right|350px|Jumaay Tuubaa ju mag ji|lien=Special:FilePath/Jumaay_Tuubaa.jpg]]
Sancoon na [[Tuubaa]] ci 1887 ngir gën a man a wéetal [[Yàlla]], ginaaw bi nit ñi baree fa moom ca [[Daaru Salaam]] ga ca [[anéer]]i [[Mbàkke]] gi ñu la waxoon leegi, nga xam ne raj-rajloo ba teewoon na koo nekk ca na mu ko soxlaa ba man a def li mu bëgg cig jaamu ak yar, ba mu demee Tuubaa't loola toppati ko fa, moo waraloon mu faroon sanc [[Mbàkke-Baari]] ca [[Jolof]], fa la juge dem géej boo ci bëggee xóotal yëral: [[SancamJolof Ak li ko waraloon]].