Sñ Sàmba Jaara Mbay wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Faaruux Siise (waxtaancëru)
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Daarul xayri (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Rëdd 10 :
Di rakk ci S Saa-jéey Mbay mi nga xam ne nitug Yàlla ku mag la woon, ba sax S Sàmba Jaara Mbay moom la defoon Sëriñam.
 
Sñ Saa-jéey Mbay, jamono bi [[Sëriñ]] Tuubaa nekkee Ndar jëkk muy dem ci géej gi booba Ndar moo doon gëblag senegaal. booba nag Sëriñ bi daa na dem lu bari ci ku ñuy wax Sëñ Móodu Njaay Maa-béey daan dal fa moom, foofa la Seex Saa-jéey gisante woon ak Sëriñ Tuubaa
Sñ Saa-jéey Mbay nag bi mu tasee ak Sëriñ bu mag bi, ba Sëñ bi wan ko lam ko wan, ca la jébbalu fa saa sa. Sëriñ bi nangul ko njébbaloom teg ci seexal ko ca bis ba, ngir fam tollu ci sunu Boroom.