Sñ Sàmba Jaara Mbay wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Daarul xayri (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Daarul xayri (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Rëdd 18 :
Ca booba la ko Sëriñ Alaaji Maalik Si waxoon ne ko ngir mu jaar ci Sëriñ Siidi Muxtaar Alkuntiyu mi nga xam ne moo doonoon sëriñu baayam Ahmadu Mbay ngir mu siyaare ko tàgguwaale ko. Bam demee ngir tàggu ko ca la ko xamaloon ginnaw bi mu duggee xalwa ñatti fan ne ko woon nag, kenn du dem ngir siyaare Yóonent Bi ñu lay fomm waaye yaw kat am na lu ma sama Boroom wan ci say bir, wan na ma ne Xutbub jamono dina feeñ te yaw kat di nga am cër bu rëy ca moom boo fi toogee. Te ki tax nga nar a daje ak moom mi ngi lay wër.
Booba Seex Saa-jéey juge na Ndar , dégg ne Seex Sàmba Jaara mi ngi jëm Gosaas. Fekkoon ne S Sàmba Jaara moom juge woon na fa ba demoon Tiwaawan jaar fa dem Njaasaan ba doon dëppaat jëm Gosaas foofa la tasee ak Seex Saa-jéey mu xamal ko ne moom la doon seet, ne ko nag jëmm ji ma doon wër muy Xutbub jamono gis naa ko. Ma bëggoon ñu ànd ca moom nga jébbal ko say bir! Ca la Seex Saa-jéey ànd ak moom Ndar jébbal ko Sëriñ Tuubaa.
 
==DIGGANTEEM AK SËRIÑ BI==
 
Seex Sàmba Jaara nag ab Saa-Kokki la woon waaye ba mu jébbaloo ci Sëriñ bi dafa mujjee féete Ndar.
Mu nekkoon fa ak Sëñ bi, Sëriñ bi nag ubbi woon ko mu nekkoon way-katam, di ki njëkk a tagg Sëriñ Bu Mag Bi ci làmmiñu wolof! Ngir ne moo jiitu ñoom S Moor Kayre(1869-1951) ak ñoom S Mbay Jaxate(1875-1954) ak S Muusaa Ka(1889-1963) , te doonoon seen mag, ba lii a tax S Muusaa Ka naan:
 
 
Nde Kayreek Njaxateek Sàmba Jaara sun maam
Ligne 54 ⟶ 57 :
 
Ba looloo waraloon mu tudde woon ko Saahibul-Abyaati maanaam Boroom-Bayit Yi (dàkkantal la wu ko Sëriñ Bi daan woowee ngir ug ràññikuwaay ci man a wayam).
 
==AY WAYAM==
 
Ay wayam nag nekk na luy yare ak a jàngale tawhiid, ak a wanne melaw Sëriñ Bi.
Ligne 108 ⟶ 113 :
Mu ni ko yaw, ma ni ko yaw,
Ki ma giseel a mat a xam.
 
==FI KO SËRIÑ BI TEGOON==
 
Sëriñ Tuubaa nag fonkoon na ko lool ba bu daa laaj kenn; ana foo bawoo? Boo ne koo Ndar. Daf lay laaj ndax siyaare nga Sàmba Jaara Mbay? Boo ne koo déet. Mu ne la kon demóo Ndar! Loolu batay muy tektale ag cofeelam ca moom, ba tax bi Seex Sàmba Jaara Mbay làqoo, toog na ñatti at yoy daan na laaj ana ku man waxiy Muhammat Abdu Kariim Sàmba Jaara ya? mag ñi daa ko ko wëral ba 1920 ci lañ gisee kuñ naan Sëriñ Daam Njaay ca Gosaas moom taalube Seex Saa-jéey Mbay la woon, moo mokkaloon wayi Seex Muhammat Abdu Kariim Sàmba Jaara ya? Ca la ñëwe daa di koy jàng ci kanamu Sëriñ bi. Ba nee nañ bu daa dégg kuy wolofal, da daa wax: "Sàllaahu moom de lu mat a wax reg Sàmba Jaara wax na ko".
Ligne 130 ⟶ 137 :
Seriñ Bi may na ma boppam.
 
==MUJJUG JAMONOOM==
Mujjug jamonoom:
 
 
Bis Seex Sàmba Jaara doon na doxantu ci wetu dex ga ca Ndar, mu gis ay jongama yu taaru lool , mu xam ne ñii duñ ay nitu fii, mu laaj leen? Ana loo leen di def fii? Ñu xamal ko ne ñoom ci Huurul-ayni yi la nu bokk, da noo ñëwoon ngir teertu seen ub sang. Mu laaj leen; naka la seen sang boobu tudd? Ñu ne ko: Muhammat Abdu Kariim Sàmba Jaara Mbay . Ca la dawee dellu këram, moo tax mu ne:
Ligne 168 ⟶ 176 :
 
Seex Muhammat Abdu Kariim Sàmba Jaara Mbay mi ngi génn àdduna atum 1917, barabam bi ma nga nekk ca almeeru Cem yi fa Ndar.
 
==AK NJABOOTAM==
 
Ñatti doom la amoon ñuy:
* Faatima Sahraa Mbay