Sñ Sàmba Jaara Mbay wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Daarul xayri (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Daarul xayri (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Rëdd 3 :
 
Seex Muhamadu Abdu Kariim Sàmba Jaara Mbay:
Mi ngi gane jamono ci atum 1868, làqu ci atum 1917 dundam mi ngi toll ci 49i at.
Di doom ci S Ahmadu Mbay ak Soxna Ndaag Kan Ñaŋ.
Di rakk ci S Saa-jéey Mbay mi nga xam ne nitug Yàlla ku mag la woon, ba sax S Sàmba Jaara Mbay moom la defoon Sëriñam.
 
S Saa-jéey Mbay, jamono bi Sëriñ Tuubaa nekkee Ndar jëkk muy dem ci géej gi booba Ndar moo doon gëblag senegaal. booba nag Sëriñ bi daa na dem lu bari ci ku ñuy wax Sëñ Móodu Njaay Maa-béey daan dal fa moom, foofa la Seex Sa-jéey gisante woon ak Sëriñ Tuubaa
S Saa-jéey Mbay, nagjamono bi mu tasee ak Sëriñ buTuubaa magnekkee bi,Ndar bajëkk Sëñmuy bidem wanci kogéej lamgi kobooba wan,Ndar camoo ladoon jébbalugëblag fasenegaal. saabooba sa.nag Sëriñ bi nanguldaa kona njébbaloomdem teglu bari ci seexalku koñuy cawax bisSëñ Móodu Njaay Maa-béey daan dal fa bamoom, ngirfoofa famla tolluSeex ciSaa-jéey sunugisante Boroom.woon ak Sëriñ Tuubaa
Sñ Saa-jéey Mbay nag bi mu tasee ak Sëriñ bu mag bi, ba Sëñ bi wan ko lam ko wan, ca la jébbalu fa saa sa. Sëriñ bi nangul ko njébbaloom teg ci seexal ko ca bis ba, ngir fam tollu ci sunu Boroom.
 
Ca ginnaaw ga la doon wëri rakkam jii di Sàmba Jaara Mbay, ngir mu jébbalu ci Sëriñ bii mu gis; muy Sëriñ Tuubaa.
 
==AG JÉBBLOOM==
 
Fekkoon ne booba Seex Sàmba Jaara Mbay mi ngi doon waaj ngir siyaare ji Yónnent bi, doon tàggu Sëriñ Alaaji Maalik Si mi nga xam ne daan na ko jàngal yenn téerey xam-xam yi.
Ca booba la ko Sëriñ Alaaji Maalik Si waxoon ne ko ngir mu jaar ci Sëriñ Siidi Muxtaar Alkuntiyu mi nga xam ne moo doonoon sëriñu baayam Ahmadu Mbay ngir mu siyaare ko tàgguwaale ko. Bam demee ngir tàggu ko ca la ko xamaloon ginnaw bi mu duggee xalwa ñatti fan ne ko woon nag, kenn du dem ngir siyaare Yóonent Bi ñu lay fomm waaye yaw kat am na lu ma sama Boroom wan ci say bir, wan na ma ne Xutbub jamono dina feeñ te yaw kat di nga am cër bu rëy ca moom boo fi toogee. Te ki tax nga nar a daje ak moom mi ngi lay wër.