Sñ Sàmba Jaara Mbay wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Daarul xayri (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Daarul xayri (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 5 :
Mi ngi gane jamono ci atum 1868, làqu ci atum 1917 dundam mi ngi toll ci 49i at.
Di doom ci S Ahmadu Mbay ak Soxna Ndaag Kan Ñaŋ.
Di rakk ci S Saa-jéey Mbay mi nga xam ne nitug Yàlla muku mag la woon, ba sax S Sàmba Jaara Mbay moom la defoon Sëriñam.
S Saa-jéey Mbay, jamono bi Sëriñ Tuubaa nekkee Ndar jëkk muy dem ci géej gi booba Ndar moo doon gëblag senegaal. booba nag Sëriñ bi daa na dem lu bari ci ku ñuy wax Sëñ Móodu Njaay Maa-béey daan dal fa moom, foofa la Seex Sa-jéey gisante woon ak Sëriñ Tuubaa
S Saa-jéey Mbay nag bi mu tasee ak Sëriñ bu mag bi, ba Sëñ bi wan ko lam ko wan, ca la jébbalu fa saa sa. Sëriñ bi nangul ko njébbaloom teg ci seexal ko ca bis ba, ngir fam tollu ci sunu Boroom.