Sñ Sàmba Jaara Mbay wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Daarul xayri (waxtaancëru)
Xët wu bees : '''SEEX SÀMBA JAARA MBAY''' Seex Muhamadu Abdu Kariim Sàmba Jaara Mbay: Mi ngi gane jamono ci atum 1868, làqu ci atum 1917 dundam mi ngi toll ci 49i at. Di doom ci S Ahmadu M…
Tafaan: Éditeur de wikicode 2017
 
Daarul xayri (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: Éditeur de wikicode 2017
Rëdd 6 :
Di rakk ci S Saa-jéey Mbay mi nga xam ne nitug Yàlla mu mag la woon, ba sax S Sàmba Jaara Mbay moom la defoon Sëriñam.
S Saa-jéey Mbay, jamono bi Sëriñ Tuubaa nekkee Ndar jëkk muy dem ci géej gi booba Ndar moo doon gëblag senegaal. booba nag Sëriñ bi daa na dem lu bari ci ku ñuy wax Sëñ Móodu Njaay Maa-béey daan dal fa moom, foofa la Seex Sa-jéey gisante woon ak Sëriñ Tuubaa
S Saa-jéey Mbay nag bi mu tasee ak Sëriñ bu mag bi, ba Sëñ bi wan ko lam ko wan, ca la jébbalu fa saa sa. Sëriñ bi nangul ko njébbaloom teg ci seexal ko ca bis ba, ngir fam tollu ci sunu Boroom.
Ca ginnaaw ga la doon wëri rakkam jii di Sàmba Jaara Mbay, ngir mu jébbalu ci Sëriñ bii mu gis; muy Sëriñ Tuubaa.
Fekkoon ne booba Seex Sàmba Jaara Mbay mi ngi doon waaj ngir siyaare ji Yónnent bi, doon tàggu Sëriñ Alaaji Maalik Si mi nga xam ne daan na ko jàngal yenn téerey xam-xam yi.
Rëdd 29 :
Ay wayam nekkoon lu daan dugg ci xolu aji-dégloom, ba daan na yóbb Sëriñ bi cig jéll.
Loolu nag sikkul ngir ne Sëñ bi daan na dégg ay mbind boppam mu ko daa def haal bay laaj ana ku wax? Ñu ne ko Mbàkke lii de say wax a.
Te Seex Sàmba Jaara ni Sëriñ bi daa waxe ak Yónnent bi noo nii la daa waxe ak Sëriñ bi, ci ay waxiin yu taaru, moo tax mu ne :
 
May na ma, ma déggook moom i wax
Rëdd 38 :
Nga xam ne da ñoo dem ba niru ay wax, ba Sëriñ bi da ko daan bëgg di dégg muy way, ba loolu waral moom musta ñëw ci kër Sëriñ bi ñu koy xaarloo naan ko sëriñ bi daa fatu (tëju). Te ba ci magam Seex Saa-jéey daan na ñëw ñu naan ko Sëñ bi daa fatu. Ba mag ñi, ku ci masaa na bëgg a gis sëñ bi, ba gis Seex Sàmba Jaara Mbay jëm fa moom, da koy leer ne di na gis tay Sëriñ Bi!
Ba bu daa ñëw fekk Sëñ Bi fatu sax, bu daa Tàmbli a way, Sëriñ bi génn, ba amoon na bëyit yoy moom la daa nuyoo Sëriñ bi bu masaa na dugg ci kër Sëñ bi:
RAHMATUL LAAHI YAA NAHIIMA JINAANII
ANTA HIBBII WA ANTA NUURA JANAANII