Xaadiriyaa wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Daarul xayri (waxtaancëru)
Xët wu bees : '''Xaadiriya:''' wenn yoon la ci yooni Tasawwuf yi, te tënku ci sunna. Ñu ngi koy askanale ci genn góor-Yàlla guñuy wax '''sëriñ Abdul xaadir Aljaylaanii'''(471h- 561h),  ...
Tafaan: Soppikaay gu gisu Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
 
Aucun résumé des modifications
Tafaan: recent_changes
 
Rëdd 1 :
'''Xaadiriya:''' wenn yoon la ci yooni Tasawwuf yi, te tënku ci sunna. Ñu ngi koy askanale ci genn góor-Yàlla guñuy wax '''sëriñ Abdul xaadir Aljaylaanii'''(471h- 561h),  ñiy topp yoon woowu nag tasaaroo nañu ci gox yu bari niki Saam, Iraã, Isibt ak la féete penku ca Afrig. Yoon la woo xam ne ay jéegoom gudd na lool ci tasaare Lislaam ci goxi [[Afrig]] yi ak Asi, ba mëdd gëm-gëmu nasaraan ci fu bari ci Àdduna bi.