Miiraas wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Daarul xayri (waxtaancëru)
Xët wu bees : '''MIIRAAS''' '''Miiraas''': Xam-xam la buy lijjanti alalu aji faatu ji; muy limu bàyyi ginnaawam lépp, nan lees koy séddalee ci ñi nga xam ne ñoo ko war a donn, moom nag moo...
Tafaan: Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
 
Aucun résumé des modifications
Tafaan: recent_changes
Rëdd 1 :
'''MIIRAAS'''
 
'''Miiraas''': [[Xam-xam]] la buy lijjanti alalu aji faatu ji; muy limu bàyyi ginnaawam lépp, nan lees koy séddalee ci ñi nga xam ne ñoo ko war a donn, moom nag mooy xam-xam biy ñëkk réer, jugee ci àdduna. Loolu nag sangub mbindeef yi moo ko wax Muhammat (SHW), te it nee na mooy genn wallag xam-xam,
(عن أبي هريرة رضي الله عنه قال: قال رسول الله صلى الله عليه وسلم: (تعلموا الفرائض وعلموها الناس فإنها نصف العلم وهو ينسى، وهو أول شيء ينزع من أمتي) رواه ابن ماجه والدارقطني)
Moom miiraas benn la ci xam-xam yi soqikoo ci '''Fiq''' ci la bànqaasoo aw wëppaam (them) day dugg ci biir bànqaasi xam-xamu Fiq bokk ci xam-xami diiney lislaam.
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Miiraas » lañ ko jële