Meningite wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Pamaboca (waxtaancëru)
Créé en traduisant la page « Meningitis »
Aucun résumé des modifications
Tafaan: recent_changes
Rëdd 1 :
'''Meningite''' nekk na xeetu mettit yu tar la yuy jàpp cër yiy aar yuuru nit ki, ak doqam, te ñu koy gëna woowe meninge.<ref name=":0">Sáez-Llorens X, McCracken GH (June 2003). "Bacterial meningitis in children". ''Lancet''. '''361''' (9375): 2139–48. doi:10.1016/S0140-6736(03)13693-8. <nowiki>PMID 12826449</nowiki>.</ref> Ni muy gëna feeñee ci nit mooy yaram wu tàng, mettitu bopp ak ndong lu bañ. Yenn saay mu feeñee neeneen, lu ci melni xel mu jaxasoo ak ñàkka xàmme yenn mbir, waccu, bëggul leeraay ak xumbaay. Neneen lay feeñee ci xale yi, lu ci melni gaawa mer, tayeel, wala baña lekk.<ref name=":1">"[http://www.cdc.gov/meningitis/bacterial.html Bacterial Meningitis]". ''CDC''. April 1, 2014. Retrieved 5 March 2016.</ref> Ni muy tàmbalee feeñ ci yaramu ki ko am, mën na wane ban xeetu Meningite la am; ci misaal, Meningite bi bacterie meningococcal mën na ànd ak yeneen xeetu feeñal ci deru [[nit]] ki.<ref name=":0" /><ref name=":2">van de Beek D, de Gans J, Tunkel AR, Wijdicks EF (January 2006). "Community-acquired bacterial meningitis in adults". ''[[:en:The_New_England_Journal_of_Medicine|The New England Journal of Medicine]]''. '''354''' (1): 44–53. doi:10.1056/NEJMra052116. <nowiki>PMID 16394301</nowiki>.</ref>
 
Wiris, bakteri wala yeneen doomi jàngoro mën nañu jàpp wàll yu bari ci yaram wi, garab yi itam mën nañu ko waaye bariwul.<ref>Ginsberg L (March 2004). "[http://jnnp.bmj.com/content/75/suppl_1/i16.full.pdf Difficult and recurrent meningitis]" (PDF). ''Journal of Neurology, Neurosurgery, and Psychiatry''. 75 Suppl 1 (90001): i16–21. doi:10.1136/jnnp.2003.034272. PMC 1765649. <nowiki>PMID 14978146</nowiki>.</ref> Meningite mën na faat doomu aadama ndax li muy yàq dafa jege yuur gi ak moelle epiñeer; moo tax, su dalee nit ki dañu ko wara gaaw faj.<ref name=":0" /><ref name=":3">Tunkel AR; Hartman BJ; Kaplan SL; et al. (November 2004). "[http://cid.oxfordjournals.org/content/39/9/1267.full.pdf Practice guidelines for the management of bacterial meningitis]" (PDF). ''Clinical Infectious Diseases''. '''39''' (9): 1267–84. doi:10.1086/425368. <nowiki>PMID 15494903</nowiki>.</ref> Suñu jamee (Une ponction lombaire) nit ki ci yaram lañuy mëna xam ndax amna Meningite am déet.<ref name=":1" /> Dañuy roof ràbb ci kanaal rachidien bi ngir taataan lenn ci liquide cephalo-rachidien (LCR), bi muur yuur gi ak moelle epiñeer bi. Ci ab labo lañu càmbaree LCR.<ref name=":3" />