Tuberculosis wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Pamaboca (waxtaancëru)
Créé en traduisant la page « Tuberculosis »
 
Holder (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 3 :
Tuberkuloos dafay tasaaroo ci ngelaw li, suede tuberkuloos bu tar moo la jàpp, soo sëqëtee wala nga tifli wala nga wax, wala nga tissooli mën nga ko wàlle.<ref>[[The Chambers Dictionary. New Delhi: Allied Chambers India Ltd. 1998. p. 352. ISBN 978-81-86062-25-8. Archived from the original on 6 September 2015.]]</ref> Nit ñi feebar bi di nelaw ci seen yaram du ñu wàlle feebar bi.<ref>Dolin, [edited by] Gerald L. Mandell, John E. Bennett, Raphael (2010). Mandell, Douglas, and Bennett's principles and practice of infectious diseases (7th ed.). Philadelphia, PA: Churchill Livingstone/Elsevier. p. Chapter 250. <nowiki>ISBN 978-0-443-06839-3</nowiki>.</ref> Nit ñi gëna mëna wàlle feebar bi mooy ñi am VIH/SIDA ak tóxkat yi.<ref>[["Basic TB Facts". Centers for Disease Control and Prevention (CDC). 13 March 2012. Archived from the original on 6 February 2016. Retrieved 11 February 2016.]]</ref> Ngir saytu jàngoro ju tar ji ci yaram nit, dañuy rajo dënn bi, dañuy jël itam ndox mu bawoo ci moom ñu xool ko ci microscope wala ñu amal ci njàngat mu xóot.<ref>[[Konstantinos A (2010). "Testing for tuberculosis". Australian Prescriber. 33 (1): 12–18. doi:10.18773/austprescr.2010.005.]]</ref> Sudee tuberkuloos biy nelaw nak, ci deru nit ki wala ci deretam.<ref>[["Tuberculosis". World Health Organization (WHO). 2002. Archived from the original on 17 June 2013.]]</ref>
 
Suñu bëgee aar nit ñi ci feebar boobu, nañuy saytu bu baax ñi nekk fumu leen mëna dalee, teela gis doomu feebar bi ak teel ko faj, ak jël ñaq bii di [[Bacillus Calmette-Guérin|Bacile Calmette-Guérin]] (BCG).<ref>[[Kumar V, Abbas AK, Fausto N, et al. (2007). Robbins Basic Pathology (8th ed.). Saunders Elsevier. pp. 516–22. ISBN 978-1-4160-2973-1.]]</ref> Nit ñi feebar bi gëna yab ñooy ñiy liggéeyandoo ak ki ko am, ñi mu bokkal kër, workplace, ak ñi muy nekkal bis bu nekk.<ref>[[Lawn SD, Zumla AI (July 2011). "Tuberculosis". Lancet. 378 (9785): 57–72. doi:10.1016/S0140-6736(10)62173-3. PMID 21420161.]]</ref> Paj mi dafay yàgg lool, te ay àntibiotik lañu koy defee.<ref>[[Schiffman, G (15 January 2009). "Tuberculosis Symptoms". eMedicine Health. Archived from the original on 16 May 2009.]]</ref> Doomu jàngoro bi daa tàmbali ñeme garab yu bari (MDR-TB) ak doomu jàngoro yi ñeme yeneen garab bi (XDR-TB).<ref>Gibson, Peter G. (ed.); Abramson, Michael (ed.); Wood-Baker, Richard (ed.); Volmink, Jimmy (ed.); Hensley, Michael (ed.); Costabel, Ulrich (ed.) (2005). Evidence-Based Respiratory Medicine (1st ed.). BMJ Books. p. 321. <nowiki>ISBN 978-0-7279-1605-1</nowiki>. Archived from the original on 8 December 2015.</ref>
 
Ci atum 2018, ñeenti nit ñoo jël xalaat nañu ni kenn ka amna tuberkuloos.<ref>[[Behera, D. (2010). Textbook of Pulmonary Medicine (2nd ed.). New Delhi: Jaypee Brothers Medical Publishers. p. 457. ISBN 978-81-8448-749-7. Archived from the original on 6 September 2015.]]</ref> At mu nekk dina am lu tollu ci 1% ci nit ñi ci àdduna bi ñuy am doomu jàngoro ji.<ref>Halezeroğlu S, Okur E (March 2014). "Thoracic surgery for haemoptysis in the context of tuberculosis: what is the best management approach?". Journal of Thoracic Disease. 6 (3): 182–85. doi:10.3978/j.issn.2072-1439.2013.12.25. PMC 3949181. <nowiki>PMID 24624281</nowiki>.</ref> Ci atum 2017, amoon na lu ëpp 10 milion ci nit ñu am feebar bi, ci ñooñu amna ci lu tollu 1.6 milion ñu ci ñàkk seen bakkan.<ref>[[Jindal, editor-in-chief SK (2011). Textbook of Pulmonary and Critical Care Medicine. New Delhi: Jaypee Brothers Medical Publishers. p. 549. ISBN 978-93-5025-073-0. Archived from the original on 7 September 2015.]]</ref> Loolu moo ko def feebar bi dàqa ray ci feebar yiy wàllaate.Lu ëpp 95% nit ñi mu faat ci réew yu néew doole yi lañu dëkk, lu ëpp 50% Inde, Chine, Indonesie, Pakistan, ak Philippines.<ref>Golden MP, Vikram HR (November 2005). "Extrapulmonary tuberculosis: an overview". American Family Physician. 72 (9): 1761–68. <nowiki>PMID 16300038</nowiki>.</ref> Seetlu nañu ni li ko dale atum 2000 ba leegi wàllaate gi dafay gëna wàññeeku at mu nekk.<ref>Ghosh, editors-in-chief, Thomas M. Habermann, Amit K. (2008). Mayo Clinic internal medicine: concise textbook. Rochester, MN: Mayo Clinic Scientific Press. p. 789. <nowiki>ISBN 978-1-4200-6749-1</nowiki>. Archived from the original on 6 September 2015.</ref> Nit ñi saytu ndax am nañu tuberkuloos am déet, 80% ci ñoom dañuy am feebar bi suede ci Asie ak ci Afrique waaye suede ci Etats Unis 5–10% ci nit ñi ñuy saytu ñoo koy am.<ref>Southwick F (2007). "Chapter 4: Pulmonary Infections". Infectious Diseases: A Clinical Short Course, 2nd ed. McGraw-Hill Medical Publishing Division. pp. 104, 313–14. <nowiki>ISBN 978-0-07-147722-2</nowiki>.</ref> Ca jamonoy maam ya ba leegi tuberkuloos a ngi am.<ref>[[Jindal, editor-in-chief SK (2011). Textbook of Pulmonary and Critical Care Medicine. New Delhi: Jaypee Brothers Medical Publishers. p. 525. ISBN 978-93-5025-073-0. Archived from the original on 6 September 2015.]]</ref>