Sëriñ Saaliwu Mbàkke wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Daarul xayri (waxtaancëru)
Tuxal nataal bi yóbb ko ca kaw!
Tafaan: Éditeur de wikicode 2017
CommonsDelinker (waxtaancëru)
Removing Sëriñ_Saaliwu_Mbàkke.jpg, it has been deleted from Commons by Fitindia because: per c:Commons:Deletion requests/Files uploaded by Daarul xayri.
Rëdd 1 :
[[Image:Sëriñ Saaliwu Mbàkke.jpg|thumb|right|350px|Sëriñ Saaliwu ci melo wuy wone ag ragal Yàlla ak ginaawal àdduna]]
 
'''Sëriñ Saaliwu''' mi ngi gane àdduna, ca Njaaréem(Senegaal) ci guddig àjjuma gu 14 ci weeru tëbëski, atum 1333 g.g, dëppoo ak 22 satumbar 1915. Aji juram ju góor di ku jaradee leeral ngir xam gi ko nit ñépp xam di [[Seex Ahmadu Bamba]], ju jigéen di [[Soxna Faati Jaxate]], mom Sëñ Moodu Asta mu baax ma te sell. S Tuubaa bi mu ganee àdduna daa bindoon ciw kayit tur wi di (Saaliwu giy tekki aji baax, aji yéwén) jox ko [[Sëñ Muhammadu Lamin Jóob Dagana]], ne ko tudde ko ko, bi mu ko defee moom S Dagana, daa daal di bind as lëf ciy bayit ñaanal ci liir bu tedd bii aw fan wu gudd akug wér, akug yékkatiku ci jamonoom ba mel ni jant, mu wax ca ne: