Wolof (làkk) wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Saalihu Mbàkke (waxtaancëru)
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Saalihu Mbàkke (waxtaancëru)
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Rëdd 21 :
 
Daanaka ñoo ngi koy làkk ci Senegaal gépp, bëj-gànnaar ba bëj-saalum, penku ba sowwu.
Donte wolof da di làkku askanu ñi ñuy woowe ay wolof, waaye kàllaama wolof amul uw dig. Dem na ba romb dig (frontiere)yu Senegaal àgg ba [[GaambiGàmbi]], [[Gànnaar]] ba [[Mali]], ci ñaari dëkk yu njëkk yi sax boole nañu ko ci seen i làkki réew. Daanaka gox boo dem ci Senegaal am nañu waxiinu wolof wu wuute: am na wolofi [[Waalo|waalo-waalo]], [[Jolof|jolof-jolof]], [[Siin-Saalum|saalum-saalum]], wu [[Kajoor|kajoor-kajoor]], wu [[Bawol|baol-baol]] ak wu [[lébu]].
 
== Mbindin ==