Wolof (làkk) wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Saalihu Mbàkke (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Saalihu Mbàkke (waxtaancëru)
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Rëdd 18 :
 
== Cosaanam ==
Ni ko gëstukat yi waxe, làkku wolof am na ag mbokkoo ak yeneen làkki Afrig yu bari, yu mu bokkalibokkal i maam. làkk yi dañ leen a séddale ci ay wàll: bu ci nekk ñi am ag mbokkoo lañu fa def. Nee nañu wolof ci wàll gi ñu'yñuy woowe bànqaasub atalaas bu làkki kongóoKongóo yu kojug nit ku ñuul la bokk. Am na ag mbokkoo ak [[pulaar]] ak [[séeréer]] ak [[joolaa]] ak yeneen.
 
Daanaka ñoo ngi koy làkk ci senegaalSenegaal gépp, bëj-gannaargànnaar ba bëj-saalum, penku ba sowwu.
Donte wolof da di làkku askanu ñi ñuy woowe ay wolof, waaye kàllaama wolof amul awuw dig. Dem na ba romb dig (frontiere)yu Senegaal àgg ba [[Gaambi]], [[Gànnaar]] ba [[Mali]], ci ñaari dëkk yu njëkk yi sax boole nañnañu ko ci seeniseen i làkki réew. Daanaka gox boo dem ci Senegaal am nañu waxinuwaxiinu wolof wu wuute: am na wolofi [[Waalo|waalo-waalo]], [[Jolof|jolof-jolof]], [[Siin-Saalum|saalum-saalum]], wu [[Kajoor|kajoor-kajoor]], wu [[Bawol|baol-baol]] ak wu [[lebulébu]].
 
== Mbindin ==