Sëriñ Baara Mbàkke Fàllu wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Daarul xayri (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: Éditeur de wikicode 2017
Daarul xayri (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: Éditeur de wikicode 2017
Rëdd 24 :
Nekkoon gu bëgg bennoog jullit yi, dem seet i ay mbokk i diineem yu bari daan leen nemmiku,
Sëriñ Baara nekkoon nit ku woyof daawul xeeb kenn, nekkoon nit ku neex a jot di wax ak ñépp di déglu ñépp, bamu nekk a gul xalifa ak bi mu nekkee xalifa daraam soppikuwul, ña mu daan seet i lay seet i, ña mu xamoon beddiwu leen di tudd i doom di dem sarax di seet i ku tawat, màggal yépp la daan dem.
Deful woon yëff yi yëfi kër, waaye yëfi ñépp la ko defoon,
bëgg ay rakkam def leen ni boppam , dëddu woon àdduna lool man a jaamu Yàlla lool fonku julli lool bokk na ci ñi ëpp lunu julli ci jumaay Tuubaa ak lumu metti ci moom di xaritu ñépp.
Sëriñ Baara nekkoon koo xam ne ku daan jàppale ndaw yi, dileen taxawu ci seen njàng ak seen liggéey. Sëriñ Baara amoon gëm-gëmu jiital ndaw yi ci lépp xam ne ñooy yaakaari ëllëg yi, mu teel leen a jiital,