Sëriñ Saaliwu Mbàkke wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Addbot (waxtaancëru)
m Bot: Migrating 3 interwiki links, now provided by Wikidata on d:q379696 (translate me)
Daarul xayri (waxtaancëru)
Tuxal nataal bi yóbb ko ca kaw!
Tafaan: Éditeur de wikicode 2017
Rëdd 1 :
[[Image:Sëriñ Saaliwu Mbàkke.jpg|thumb|right|350px|Sëriñ Saaliwu ci melo wuy wone ag ragal Yàlla ak ginaawal àdduna]]
 
'''Sëriñ Saaliwu''' mi ngi gane àdduna, ca Njaaréem(Senegaal) ci guddig àjjuma gu 14 ci weeru tëbëski, atum 1333 g.g, dëppoo ak 22 satumbar 1915. Aji juram ju góor di ku jaradee leeral ngir xam gi ko nit ñépp xam di [[Seex Ahmadu Bamba]], ju jigéen di [[Soxna Faati Jaxate]], mom Sëñ Moodu Asta mu baax ma te sell. S Tuubaa bi mu ganee àdduna daa bindoon ciw kayit tur wi di (Saaliwu giy tekki aji baax, aji yéwén) jox ko [[Sëñ Muhammadu Lamin Jóob Dagana]], ne ko tudde ko ko, bi mu ko defee moom S Dagana, daa daal di bind as lëf ciy bayit ñaanal ci liir bu tedd bii aw fan wu gudd akug wér, akug yékkatiku ci jamonoom ba mel ni jant, mu wax ca ne:
 
Ligne 8 ⟶ 10 :
'''Yal na ko fi desal muy kuy mottali jub gi fi Yonent bi indi woon, di ku barkeel, di ku wér, tey ku am muur»'''
'''
[[Image:Sëriñ Saaliwu Mbàkke.jpg|thumb|right|350px|Sëriñ Saaliwu ci melo wuy wone ag ragal Yàlla ak ginaawal àdduna]]
 
== Am njàngam ==
Ay ceññeeri xel ak màndargay yewwute ak man a wattu teeloon naa feeñ ci moom te booba matagutoon a dal jàng, bokk na ci liy dëggal loolu te di ko dëgëral lii nettalikat yi di nettali muy ne moom de mokkaloon na xasida gii di (Ikfinii) te booba gone gu ndaw la woon, ginaaw bi mu jànge [[Alxuraan]] ca Tuubaa ci loxol nijaayam S Alasaan Jaxate mom Jàmbaar, ba mokkal te bind [[kaamil]], ginaaw bi mu dugg ci jàng xam-xami diine yi ak làkku [[araab]] ci ay ustaas yu màgg niki Seex Moor Saasum Jaxate mom Xaali Majaxate Kala ca Aynu Maadi ak Seex Muxtaar Guyaar Jang walla Njang ca Husnul Maab(Tindoodi) ak S Abiibu ca Tuubaa, S Mut Dem ca Njaaréem, Seex Aamid Saw ca Mewndu, kii mooy ki ko jàngal xam-xami [[gëstubiddiw]] yi (falag) ak [[melosuuf]] gi nga xam ne xóotoon na ci ba àgg ci di xam ci mbiri ay réew ca [[Asi]], [[Tugal]] ak yeneen réew lol ña fa dëkk sax leeg-leeg ñu xaw koo réere. Ku soppoon yër ay téere la, ndax saxoon na ci ab diir ci jamono ba mujjoon di géej gu deesul jot ag suufam ngir ag xóot. Bi Sëñ bi àggee fii ci njàng mi la gis ne daa war a dugg leegi ci jeneen dara mooy ju tukki, ndax tukki benn la ci daara yu mag yi xam-xam di juddoo, di yokk jarbu tey dollim xel, ndax bari na xam-xam yu ci juddoo, ndax dina yobboo ñaare ci xalaat ci dénd bi te Yàlla (tudd naa sellam ga) yàgg na cee woote jëme. Ci noonu, mu def lu sakkan ciy tukki ci biir réew meek biteem, ci mbooleem [[diiwaani Senegaal]],[[Kot Diwaar]] ak [[Gàmbi]], mu jële ca daj gu mag ak jarbu gu réy ci lef yu bari