Coppite gi amul tënk
(+image) |
Aucun résumé des modifications Tafaan: Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu recent_changes |
||
Pël genn giir la gu nekk Senegaal. Pël yi ci [[Sowwu Afrig]], dañoo bokk ci waaso yi gën a bari gën a yaatu. [[Senegaal]], [[Mali]], [[
Xeet woowu am nañu tur yu bari: Pël ci [[Wolof]], ci [[Afrig]] mooy tur wi gën a siiw, Fula ca Mande ya, Fulani ca Naar ya, Fellata wala Fellan ca [[Sudaan]].
[[Dencukaay:Eleveurs Peuls.jpg|thumb|left|Sàmmkatu Pël bu Gurma, bëj-saalumu [[Gao]], [[Mali]]]]
Dencukaay:Femme-peule.jpg|Jigéen
</gallery>
== Xool itam ==
*[[Wolof (askan)]]
|