Taariixu Aamerig wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
 
Rëdd 150 :
== Tembug [[Diiwaan yu Bennoo]] Aamerig yi: ==
 
Bi waa Britani xamee ne lòtt nañu ci toroxal [[jeqiku]] gi amoon ci Aamerig, te xam ne doole du mooy lijanti lëj-lëj yi nekk ci sancoom yi, ndax kat mi ngi nii di ku ñu dàqe, ndamu ci kawam ca xare ba, bi loolu amee mu sàkku woon ag juboo, ci noonu ñu xaatim juboo gi ci [[ParisPari]], ci digganteem aki sancoom atum 1783 g, lii mooy tomb ya ca ëpp solo:
 
'''1''' Britani day nangu tembteg sancu yi nekk ci suuf yi féete ci penkub '''dexug Misisipi''' gi, te jàppe dex gii muy diguw sowwu wi ko tàqale ak sancu yi. Bu ko defee dig yu bëj gànnaar yi ñoom ñu bàyyi leen nañu nekke woon.