Diiwaan yu Bennoo wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Aucun résumé des modifications
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Aucun résumé des modifications
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Rëdd 18 :
}}
 
'''Diiwaan-yu-Bennoo''', walla '''Diiwaan-yu-Bennoo yu Aamerig''' ci anam gu gudd am réew la mu séddaliku ci juroom-fukki diwaan, ñent-fukk ak juroom-ñett yi ñoo taqaloo te féete ci diggante [[Mbàmbulaanug Atlas]] ak [[Mbàmbulaan Gu-Dal|Gu-Dal]] gi, penku ba sowwu, [[Kanadaa]] moo féete bëj-gànnaar, [[Meksik]] nekk ci bëj-saalumam. [[Alaskaa]] ci la bokk donte taqu ci, mi ngi nekk ci sowwu [[Kanadaa]]. [[HawaiiXawaay]] moom mi ngi ci diggu mbàmbulaan Gu-Dal gi. Réew mi am na fukk ak ñenti diiwaan yu tasaaroo ci [[Géeju Karayib yi|géeju karayib yi]] ak Gu-Dal gi. Péeyam mooy [[Washington]].
 
'''Diiwaan-yu-Bennoo yi''' ci 2008, 302 ciy miliyoŋ ciy way-dëkk lañu amoon, loolu tax muy ñetteelu réew mi ëppi nit ci [[àdduna]] bi, ci ginnaawu [[Siin]] ak [[End]]. Réyaayam toll ci 9,4 junni km², di ñeenteel ci àdduna bi, ci ginnaawu [[Riisi]], [[Kanadaa]] ak [[Siin]]. [[Gàddaay]] gi bari na fa lool, ba tax muy réew mi ëppi xeet yu jaxasoo ci [[Suuf]] si. Koom-koomam mooy bi gën a woomle ci àdduna bi, te moo am [[njuddéef mu ñumm mu biirum réew]] (NJ.Ñ.B) mi ëpp ci àdduna bi.