Taariixu Aamerig wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Rëdd 3 :
'''Feeñug Diiwaani Amerig yu bennoo yi'''
 
[[Gàddaay]] yi waa [[Tugal]] yi daa def juge [[Tugal]], jëm [[Aamerig]], gàddaay yooyu wéyoon nañu di sottiku ci [[ Aamerig gu bëj-gànnaar]] gi. Loolu nag amoon na, ginaaw bi [[Kolomboo]] feeñalee Aamerig ba am lu tollook [[xarnu]]. Li ko taxaoon a am nag bari na, bokk na ci:
 
'''1''' [[Fitna]]y diine yi amoon ci [[Tugal gu diggu]] gi ak gu sowwu gi, li waraloon loolu di yëngu-yëngu yu [[diine]] yi jugoon di safaan Jàngu bu [[Katolig]] bi, ak la ca juddoo muy ay xeexi [[ngér]], yu amoon ci diggante [[ngérum Katolig]] ak [[ngérum Protestant]] , ak xeex bi protestant yi doon def ci seen biir, rawati na ci Angalteer, ak la ca juddoo muy [[boddikoonte]] ci diine, loolu nag waraloon gàddaayug ab lim bu mag ci waa Tugal yi, dem [[Aamerig]] gu bëj-gànnaar gi, ngir rawale seen bakan, ak ngir man a doxal seen diine ci ag féex akug gore.