Taariixu Aamerig wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Addbot (waxtaancëru)
m Bot: Migrating 18 interwiki links, now provided by Wikidata on d:q690256 (translate me)
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Rëdd 17 :
== [[Sancu]] yi nga xam ne waa Angalteer yi taxawal nañu leen ci [[Aamerig gu bëj gànnaar]] gi: ==
 
Waa Tugal yii bawoo woon [[EspaañIspaañ]], [[Faraas]], [[Olaand]], [[Suwed]] ak [[Angalteer]], sancoon nañu ay barab yu wuute ci [[Aamerig gu bëj-gànnaar]] gi, ñoom lañuy wax tay [[Diiwaan yu Bennoo]] yu Aamerg yi , loolu nag di woon ci ñaari xarnu yii di bu fukk ak juroom benneel ak bu fukk ak juroom ñaareel g. Waa Angalteer yi nag ñooy ñi njëkk a taxawal ab sancu ca [[Jims Town]], ci diiwaanu [[New York]], atum 1607 g, mujj nañu nag ci diir bu gàtt, di ñi gën a tas, gën a wisaaroo ci barabi tefes yu [[penku]] yi, ci mbooleem ñi gàddaaye [[Tugal]].
 
Barabi penku yii, maanaam yii nga xam ne la ëpp ca ña fa sancoon, dëkke woon fa ay waa Angalteer lanu woon, barab yii mooy yi mujjoon ginaaw bi (1776 g) di laaj ag temb akug dagge ca réew may nday di Angalteer.
Rëdd 42 :
 
Diiwaan yooyu ñooy yi sos, te amal li nuy wax Diiwaani Amerig yu Bennoo yi, ci ginaaw [[xareb temb]] gi , atum 1775 – 1783 g, ñu mujj am ag temb ci Angalteer, ci mujj gi. Diiwaan yooyu nag, bu nu leen xoolee ci Aamerig gu leegi gii nii, duñu weesu benn xaaj ci Aamerig gu ñu xaaj fukki xaaj.
 
 
== Noste gi doon doxal mbiri biir yu sancu yu Angalteer yi:==