Ubbi njël lu njëkk li

Modifications

Aucun changement de taille, il y a 12 ans
Coppite gi amul tënk
Xët miiwii moo lay leeral nooy xamale yeneen way-jëfëndikoojëfëndikookat yi, say xameel ci yeneen làkk yi ak tolluwaayu xameel gi.
XËT MII NOPPEEGUL
 
'''UBBITE'''
----
Xët mii moo lay leeral nooy xamale yeneen way-jëfëndikoo yi, say xameel ci yeneen làkk yi ak tolluwaayu xameel gi.
----
----
== Lumuy jariñ ==
Donte fii [[Wikipedia la]] ci kàllaama [[wolof]] la, waaye du ñi fi nekk ñëppñépp a deggante. Am na ñu deggul wolof, walla seen degg des na, ñu manaman a soxla ku ñu jokkool ci làkk bi ñu degg, walla wolof yu yomb. Am na ay waa- wikipedia yu deggul wolof te di bëgg a jappjàpp ci ligeyliggéey bi, kon di na am solo lool nga wax ko ci yan làkk ngeen man a waxtaane, ngir njariñam man a feeñ.
 
GiiMii mebetsémb di na yombal jokkoo gi ci biir aw askan gu bariy làkk gu mel ne Wikipedia: ci misaal, di na yomb jot kuy wax wenn làkk wi, te itam di na xamale tolluwaayu degginu wolof gu ab jëfëndikookat bu bindu.
 
== Nu ma koy defee? ==
{{Babel-3|wo-1|fr-1|en-1}}
Doy na nga yokk ci sa [[Xëtu jëfëndikookat|xëtu jëfëndikookat]] '''Babelbox''' bi, tabax ko ci topp tektal yii:
* Tambalil ak '''{{Babel-'''
* Nga yokk ci limu làkk yi nga degg te teg ci '''|'''
**Misaal: '''{{Babel-3|''' (3 làkk)
 
Su ko defeen nak nga def ci tolluwaayu ni nga deggee wolof. Soo bëggee mu mel ne ni nga koy gisee (ci sa ndeyjoor), nga def: wo-0 walla wo-1 walla wo-2,añse.
 
Misaal:
'''<nowiki>{{Babel-3|wo-1|fr-1|en-1}}</nowiki>'''
== Yu wolof ==
{|align=left
|{{Babel-6|wo|wo-5|wo-4|wo-3|wo-2|wo-1|wo-0}}
|}
[[catégorie:jeego yu njëkk]]
3 285

modifications