Contenu supprimé Contenu ajouté
Daarul xayri (waxtaancëru)
Xët wu bees : '''Taab''' nu ngi koy faral di gis lu ci ëpp ci àllu Sayel bi, fi muy sax itam danuy seetlu ne suuf si day dëgër. Senegaal ba Kamerun ak Somali, amna ñu koy jàllale ci d…
Tafaan: Éditeur de wikicode 2017
(Aucune différence)

Sumb bu 24 Sattumbar 2019 à 21:23

Taab nu ngi koy faral di gis lu ci ëpp ci àllu Sayel bi, fi muy sax itam danuy seetlu ne suuf si day dëgër.

Senegaal ba Kamerun ak Somali, amna ñu koy jàllale ci diggante réew yooyu. Boo deme Niseria it di nga koy faral di gis ci boori "Sud-Ouest".

Melo

Taab garab la goo xam ne guddaay bi dina dem ba ay 12imeetar ci kaw. Te ay wànqaasam day am lu ci ëpp ay dég yu xaw a dëng. Loolu moo tax muy man a jàppanteek yeneen garab yiy nekk ci wetam. Ba laa man a sax dëgg nu nekk ci njeextalu noor bi walla ci biir nawet bi. Dina am ay xob, dina am ay meññeef.

Njariñ

Garab gi nag day faj ay feebar yu bari, yu ci mel ne: biir buy daw, saan, day yokk cawarte, tegsi di ubbi biir ngir ngay man a lekk bu baax.

Nataal

Turu xam-xam

Combretum Nigricans