Jalambaan wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Daarul xayri (waxtaancëru)
Xët wu bees : vignette|Garabug Jalambaan '''Jalambaan''' as ngarab la su am ay xop yu sew yu toll ci ñeent ak xaaj, ba ci juróom-ñaar ak xaaj, ci ay met…
Tafaan: Éditeur de wikicode 2017
 
Daarul xayri (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: Éditeur de wikicode 2017
 
Rëdd 3 :
 
Dëkkuwaayam garabu jalambaan man nañu koo fekk ci gox yu bari ak ci dundiin wu wuute man nañu koo fekk ci suuf su wow walla suuf su xaw a tooy dana ñu ko fekk it fu am i xeer waaye fi ëpp ci fi ñu koy fekk mooy cib àll ci àll boo xamentani lu ëpp ci garab ya séeni xop day sew walla fu jége géej.
 
 
==Melo wi== Xooxi jalambaan yi buñu leen génnee ci koog yi ñu nekk ba ji leen dina ñu gaaw a sax. Da ñu leen di teg ci kaw ub car ngir ñu wow ba laa ñu leen a weer ci naaj wi. Dina ñu sax juróom-ñatt jàpp ñaar fukki fan bu ñu ko jiyee ak it lu tolloog juróom-fukk ci téeméer bu ne ñu man a dund séen ug màgg nag gaawut lool ndax man nañu dem ba ñaari at toll ci fukki sànt-met ak ñaar yépp ci reen yi lay nekk .
 
==Ay ñariñam==
Ligne 14 ⟶ 17 :
Yaneen i njariñ ci jalambaan, léppam day jëm ci bantam ndax bant la bu njool xaw a jàpp ... leeg-leeg mu dër lool walla mu jël yeneen wirgo. ay bantam man na dem ba ci fukk ak ñaar ci ay sànt-met, bantam nag dana niin dëgar lool duy gaaw a dammu, man naa it fàggandiko ci ay yàq-yàqu yu mel ni ay max añs teg ci it neex a jëfandikoo te rafet lool ba tax na dañu koy jëfandikoo ci jumtuwaay yi ñuy defe misig ak bant bi ñuy doxe nu koy wax dokk dees na ko jëfandikoo fii ci Senegaal ci yu bari lu ci mel ni kurus ak yat ak jaaro añs.
 
==MeloNataal wiyi==
<gallery>
 
Dencukaay:Dalbergia nigra Blätter1.jpg|Xobi garabug Jalambaan
Xooxi jalambaan yi buñu leen génnee ci koog yi ñu nekk ba ji leen dina ñu gaaw a sax. Da ñu leen di teg ci kaw ub car ngir ñu wow ba laa ñu leen a weer ci naaj wi. Dina ñu sax juróom-ñatt jàpp ñaar fukki fan bu ñu ko jiyee ak it lu tolloog juróom-fukk ci téeméer bu ne ñu man a dund séen ug màgg nag gaawut lool ndax man nañu dem ba ñaari at toll ci fukki sànt-met ak ñaar yépp ci reen yi lay nekk .
Dencukaay:Dalbergia Cultrata Seeds and Seed Pods.jpg|Meññat mi
Dencukaay:Dalbergia horrida - Prickly Dalbergia at Mayyil (4).jpg
Dencukaay:Dalbergia obovata foliage 27 12 2010.JPG
Dencukaay:Dalbergia boniana (Flowers of the Dalbergia boniana tree).jpg|Tóortóor yi
Dencukaay:Dalbergia horrida - Prickly Dalbergia at Blathur 2017 (4).jpg
Dencukaay:Dalbergia melanoxylon (tree).jpg|Garab gi
</gallery>
 
==Turu xam-xam ==