Sànceer wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Daarul xayri (waxtaancëru)
Xët wu bees : '''Sànceer''', garab la guy faral di am ci diggu Afrig, réew yu mel ni keeñaa, Somali,Tansani jàpp Gànnaar ba Senegaal. Ci àll bi ak ci tefes gi lay faral di ñoree.…
Tafaan: Éditeur de wikicode 2017
 
(Aucune différence)

Sumb bi teew bu 23 Sattumbar 2019 à 20:17

Sànceer, garab la guy faral di am ci diggu Afrig, réew yu mel ni keeñaa, Somali,Tansani jàpp Gànnaar ba Senegaal. Ci àll bi ak ci tefes gi lay faral di ñoree.

Melo wi Soppi

Garab la gu man a sëq lool. Ay caram dañoo dëng, ab guddaayam man a toll ci 2i met jàpp 6i met.

Njariñam Soppi

Ay doomam dees koy lekk. Reen bi boo ko nalee walla nga baxal ko man nga ko jëfandikoo ci wàll um paj yu bari, ( Gaana, Sifili, Gonoore, stomaa...). Sunguf si juge ci reen bi ak xànc mi day faj ay góom.

Ay doomam dañuy faj tooke ak lu ci mel ne màtt-màttu jaan.

==Loraange yi==

Giseesagu ci lor.

Nataal yi Soppi

Turu xam-xam wi Soppi

Feretia apodanthera