Ahmadou Bamba wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Racconish (waxtaancëru)
ds
Holder (waxtaancëru)
m corr using AWB
Rëdd 223 :
Jaxasekat yi nag ,bi nu demee ci tubaab yi danu leen ne Sëñ bi ñii lay roy,ba mujj tubaab yi manatuñoo ñàkk a gëstu li nu leen wax,lii daal mooy li gën a waral tubaab bi jublusi Sëñ bi,ginaaw bi ko Yàlla dogalee namm ca la mu ca namm,muy wax joj dara amu ca,ndax Sëñ bi lorewul ,soxlawul àdduna,te xemmeemul li nu jort ci moom,Yàlla’ay seere lii nuy wax.
 
Bu doonutoon rambaaj yii,waxuma la buur yu ndaw yi sax dunu ko jeemal,waxantuma la ak yu mag yi,waaye loolu day dëggal waxi yonnant bi ji (j.y.m), ñi Yàlla gën a teg ay nattu ñooy yonnant yi,teg ci wàlliyu yi,teg ca ña gën,teg ca ña ca topp}} ,ponk bii nag bu wéy la ci xeetu yonnant bi (j.y.m),ndax ñu baax ñi ëpp ag gëm foo leen fekk,daniy fees dell aki nattu, àdduna dëddu leen naqari ci ñoom, ñooy ëppi jafe-jafe fuuf ñu dul ñoom,boo demee ca Sahiihub Muslim,ak bu dul moom,da nga ca gis :[[ àddunaay kasob jullit,tey àjjanay yéefar ]],yàlla itam wax ne : wal aaxiratu hinda rabbika lilmuttaqiin}} muy àllaaxira, ñu ragal Yàlla ñee ko moom.