Schizophrenia wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Aucun résumé des modifications
Tafaan: recent_changes Soppikaay gu gisu
Holder (waxtaancëru)
m corr using AWB
Rëdd 9 :
 
<!-- Prevention and treatment -->
Paj mi mungi aaju li ci ëpp ci [[luy xeex ñakk àndak sago]] garab, ak ci wetam [[pajum xelu nit ki|joxe ay tegtal ngir dimbali nit ki saafara jafe-jafeem]], taggat ñi di fajaate ngir ñu mëna def seen liggééy bu baax ak delluwaat nekk ak nit ñi. <ref name=WHO2015/><ref name=Lancet2016>{{cite journal | vauthors = Owen MJ, Sawa A, Mortensen PB | title = Schizophrenia | journal = Lancet | volume = 388 | issue = 10039 | pages = 86–97 | date = July 2016 | pmid = 26777917 | pmc = 4940219 | doi = 10.1016/S0140-6736(15)01121-6 }}</ref> Leerul ndax [[luy xeex ñakk àndak sago bu raññeeku|raññeeku]] walla [[luy xeex ñakk àndak sago buñu dul faraldi gis|luy xeex ñakk àndak sago yu ñu dul faraldi gis]] ñoo gën.<ref name=Kane2010>{{cite journal | vauthors = Kane JM, Correll CU | title = Pharmacologic treatment of schizophrenia | journal = Dialogues in Clinical Neuroscience | volume = 12 | issue = 3 | pages = 345–57 | year = 2010 | pmid = 20954430 | pmc = 3085113 }}</ref> Ñi nga xame ne duñuy tane ak yeneen yi di xeex ñakk àndak sago [[clozapine]]war na ñu ko jééma jëfandikoo.<ref name=Lancet2016/> Ci yenn yi gëna metti te nga xam ne am na ab njàjan ci sa bopp walla ci ñeneen ñi [[njàng ak pajum feebaru xel buñu yakkamti|ospitaaliise buñu tannul ]]war na mëna nekk, su fekkee sax léégi des ci opitaal mungi waññeeku bu baax ni bu njëkk ba.<ref name="BeckerKilian2006">{{cite journal | vauthors = Becker T, Kilian R | title = Psychiatric services for people with severe mental illness across western Europe: what can be generalized from current knowledge about differences in provision, costs and outcomes of mental health care? | journal = Acta Psychiatrica Scandinavica. Supplementum | volume = 113 | issue = 429 | pages = 9–16 | year = 2006 | pmid = 16445476 | doi = 10.1111/j.1600-0447.2005.00711.x }}</ref>
 
<!-- Epidemiology and prognosis -->
Lu tollu ci 0.3 ba 0.7 % ci ay nit am nañu feebaru schizophrenie ci seen dund.<ref name=Lancet09>{{cite journal | vauthors = van Os J, Kapur S | title = Schizophrenia | journal = Lancet | volume = 374 | issue = 9690 | pages = 635–45 | date = August 2009 | pmid = 19700006 | doi = 10.1016/S0140-6736(09)60995-8 | url = http://xa.yimg.com/kq/groups/19525360/611943554/name/Schizophrenia+-+The+Lancet.pdf | archive-url = https://web.archive.org/web/20130623065810/http://xa.yimg.com/kq/groups/19525360/611943554/name/Schizophrenia+-+The+Lancet.pdf | df = dmy-all | deadurl = no | archive-date = 23 June 2013 }}</ref> Ci atum 2013 amoon na ab xayma bu tollook 23.6 miliyoŋ ci ñi ame feebar bi ci addina bi yépp.<ref name=GBD2015>{{cite journal | vauthors = ((Global Burden of Disease Study 2013 Collaborators)) | title = Global, regional, and national incidence, prevalence, and years lived with disability for 301 acute and chronic diseases and injuries in 188 countries, 1990-2013: a systematic analysis for the Global Burden of Disease Study 2013 | journal = Lancet | volume = 386 | issue = 9995 | pages = 743–800 | date = August 2015 | pmid = 26063472 | pmc = 4561509 | doi = 10.1016/S0140-6736(15)60692-4 }}</ref> Góór ñi ñoom la feebar bi gëna japp, te ci ñoom lañuy gëne raññe feebar di wonewu.<ref name=WHO2015/> Lu tollook 20% ci ñoom ñungi ciy génn te tuuti rekkay wér bu baax,<ref name=DSM5pg101/>te lu tollook 50% dañuy am gallankoor ci seen giiru dund.<ref name=Law2015>{{cite book | last1 = Lawrence | first1 = Ryan E. | last2 = First | first2 = Michael B. | last3 = Lieberman | first3 = Jeffrey A. | name-list-format = vanc | chapter = Chapter 48: Schizophrenia and Other Psychoses | editor-first1 = Allan | editor-last1 = Tasman | editor-first2 = Jerald | editor-last2 = Kay | editor-first3 = Jeffrey A. | editor-last3 = Lieberman | editor-first4 = Michael B. | editor-last4 = First | editor-first5 = Michelle B. | editor-last5 = Riba | title = Psychiatry | edition = fourth | date = 2015 | pages = 798, 816, 819 | doi = 10.1002/9781118753378.ch48 | publisher=John Wiley & Sons, Ltd | isbn = 978-1-118-84547-9 }}</ref> Ay jafe jafe ci nekk ak nit ñi, ni ñakka liggééy gu yagg, ndóól ak [[ñakka am dëkkuwaay]], dafa bari. <ref name=DSM5pg101/><ref>{{cite journal | vauthors = Foster A, Gable J, Buckley J | title = Homelessness in schizophrenia | journal = The Psychiatric Clinics of North America | volume = 35 | issue = 3 | pages = 717–34 | date = September 2012 | pmid = 22929875 | doi = 10.1016/j.psc.2012.06.010 }}</ref> Limu [[yaakaar ci dund ba ab at]]bu nit ñi ame feebar yu fës yi mungi ci fukk ba ñaar fukki at ak juróóm gëna tuuti nit ñi ci ëpp.<ref name=Lauren2012>{{cite journal | vauthors = Laursen TM, Munk-Olsen T, Vestergaard M | title = Life expectancy and cardiovascular mortality in persons with schizophrenia | journal = Current Opinion in Psychiatry | volume = 25 | issue = 2 | pages = 83–8 | date = March 2012 | pmid = 22249081 | doi = 10.1097/YCO.0b013e32835035ca }}</ref> Li mooy li mu jur ci yoquteek jafe jafe wér gu yaram yi ñiy gis ak kawewaay [[xaru ]]mungi tollu ci (lu jege 5%).<ref name=Lancet09/><ref name=Jop2010>{{cite journal | vauthors = Hor K, Taylor M | title = Suicide and schizophrenia: a systematic review of rates and risk factors | journal = Journal of Psychopharmacology | volume = 24 | issue = 4 Suppl | pages = 81–90 | date = November 2010 | pmid = 20923923 | pmc = 2951591 | doi = 10.1177/1359786810385490 }}</ref> Ci atum 2015 xayma nañu lu tollook 17.000 ci ay nit ci addina bi ñu dee ci nekkin bu bokk ci, walla jóge ci, feebaru schizophrenie. <ref name=GDB2015>{{cite journal |author=GBD 2015 Mortality and Causes of Death Collaborators | title = Global, regional, and national life expectancy, all-cause mortality, and cause-specific mortality for 249 causes of death, 1980-2015: a systematic analysis for the Global Burden of Disease Study 2015 | journal = Lancet | volume = 388 | issue = 10053 | pages = 1459–1544 | date = October 2016 | pmid = 27733281 | pmc = 5388903 | doi = 10.1016/s0140-6736(16)31012-1 }}</ref>