Bipolar disorder wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Aucun résumé des modifications
Tafaan: recent_changes Soppikaay gu gisu
Holder (waxtaancëru)
m corr using AWB
Rëdd 3 :
 
<!-- Definition and symptoms -->
'''Feebaru "bipolaire"''', ñu xamewoon ko ni '''déteelu bu ànd ak mer gu bon''', mooy ab [[feebaru xel]]guy indi ay waxtu [[Déteelu (dikkale)|déteelu]] ak ay waxtu yu du sul noono yu[[mbégte|dikkale gu kawe]].<ref name=BMJ2012 /><ref name=DSM5 /><ref name=FDA4>{{cite web|title=DSM IV Criteria for Manic Episode|url=https://www.fda.gov/ohrms/dockets/ac/00/slides/3590s1c/tsld002.htm|deadurl=no|archiveurl=https://web.archive.org/web/20170731230148/https://www.fda.gov/ohrms/dockets/ac/00/slides/3590s1c/tsld002.htm|archivedate=July 31, 2017|df=mdy-all}}</ref> Dikkale gu kawe gi bari na te ñungi ko xame ni [[mer gu rëy ]]walla [[dikkale gu amul kersa]], mungi aajo ci rëyaayam, walla ndax liy wone [[xel mu tagoo ak li xew]] mungi ci. <ref name=BMJ2012 /> Bu nit nekkee ci mer gu rëy [[Jikko|dafay am jikko]] walla yég [[Jikko ju du sul noonu|bu dul noon]] njaxlaf, bég, walla mer.<ref name=BMJ2012 /> Nit ñi dañuy jël ay dogal te duñu ci xalaat te itam duñu xalaat li ñuy jur. <ref name=DSM5 /> Bu nit ki nekkee ci waxtuy mer gu metti duy faral di soxla nelaw. <ref name=DSM5 /> Bu nit ki nekkee ci ay déteeloom, joy dafa koy yom, gis-gisam ci dund gi dafay ñaaw, te duy xool ñeneen ñi ci ay gët. <ref name=BMJ2012 /> Njàjanu [[xaru ]]ci ñi ame feebar bi lu kawe la agg ba 6% ci ñi ëppal ñaar fukki at, tey ci booba [[dagg sa bopp]] mungi ame ci diggante 30 ba 40 %.<ref name=BMJ2012>{{cite journal | vauthors = Anderson IM, Haddad PM, Scott J |title=Bipolar disorder|journal=BMJ (Clinical research ed.)|date=Dec 27, 2012 |volume=345 |page=e8508 |pmid=23271744 |doi=10.1136/bmj.e8508}}</ref> Yeneeni jafe-jafe yi nekk ci feebari xel yi ni [[feebaru ragal gu metti|feebaru ragal yu metti]]ak[[di jëfandikoo dorog ]]dañu leendi faraldi boole ci Feebaru "bipolaire".<ref name=BMJ2012 />
 
<!-- Cause and diagnosis -->
Rëdd 9 :
 
<!-- Treatment and prognosis -->
Paj mi ñuy gëna jëfandikoo bokk na ci [[Pajum feebaru xel]]ak jël ay garab yi mel ni [[Seral dikkale (naqari dereet)]] ak [[luy xeex ak ñakk àndak sago]].<ref name=BMJ2012 /> Yenn ci yii di seral ci yi ñi gëna jëfandikkoo bokk na ci [[Lithium (garab bi)|lithium]] ak yeneen xeet yu wute [[liy xeex jangoro kiriis|yi di xeex jangoro kiriis]]<ref name=BMJ2012 /> [[Paj mu ñu waajalul]] ci ab [[ci pajukaay bu ñuy faje feebaru xel|pajukaay]] war nañu ko soxla bu fekkee am na ku jege ci fexeel boppam walla ñeneen ñi te baña fajuji.<ref name=BMJ2012 /> Ay jafe-jafe nekkin yu jeggi dayo, lu mel ni yëngëtu walla xeex, mën nañu ko toppatoo ak yi di xeex ak ñakk àndak sago ci diir bu gàtt walla [[garabu benzodiazépine|ay garabu benzodiazépines]].<ref name=BMJ2012 /> Ci waxtub xër, dafa gën [[li di xeex déteelu|yi di xeex déteelu]] ñu bayyi leena jël.<ref name=BMJ2012 /> Su fekkee yi di xeex déteelu ñungi leendi jëfandikoo bu amee ay déteelu, war nañu leen jëfandikoo ak li di seral dikkale.<ref name=BMJ2012 /> [[Pajum feebaru xel bu ñuy jëfandikoo electrochoc]] (ETC), su fekkee sax gëstuwuñu ko bu baax, war nañu ko mëna jéém ci ñooñu ñu ñu mënula faj ak yeneen paj yi.<ref name=BMJ2012 /><ref>{{Cite journal|last=Versiani|first=Marcio|last2=Cheniaux|first2=Elie|last3=Landeira-Fernandez|first3=J.|title=Efficacy and Safety of Electroconvulsive Therapy in the Treatment of Bipolar Disorder|url=http://content.wkhealth.com/linkback/openurl?sid=WKPTLP:landingpage&an=00124509-201106000-00015|journal=The Journal of ECT|volume=27|issue=2|pages=153–164|doi=10.1097/yct.0b013e3181e6332e|pmid=20562714}}</ref> Su ñu bayyee jëfandikoo ay paj, dañu bëgg ñu benn bennal ko.<ref name=BMJ2012 /> Nit ñu bare dañu ame ay jafe-jafe koppar, seen nekkin ci biir nit ñi walla ci seen liggééyukaay ndax li ñu ame feebar bi.<ref name=BMJ2012 /> Jafe-jafe yii ñeent ba ñett yoo jël saa yu nekk benn bi am na leen.<ref name=BMJ2012 /> Yoon yi ñi tann ci seen dundin ak li garab yi di def ci ñoom, njàjanu dee yu [[jogewul ci benn jàngoro ]]ni [[feebaru xol bi nekk ci li di jox xol bi dereet|feebaru xol]] tollu na ñaari yoon nit ñi.<ref name=BMJ2012 />
 
<!-- Epidemiology -->