Déteelu wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Hugo.arg (waxtaancëru)
m Hugo.arg moo toppale xët wii di Major depressive disorder jëmale ko ci Déteelu
Holder (waxtaancëru)
m corr using AWB
Rëdd 1 :
 
<!--Definition and symptoms -->
'''Feebaru naqar gu metti ku dara saful''' '''MDD''', ñu xame ko itam ni '''déteelu''', mooy benn [[feebaru xel ]]bu ñuy xame ci ñaari ayubés ci [[déteelu (dikkale)|(dikkale bu wacc]] bu feeñ ci yu bari.<ref name=NIH2016/> Dafay faraldi di ànd ak tuuti [[ci wóólu sa bopp]], [[ku mënula yëg benn banneex ci yëngu yëngu yu neex.|ñakka am yëg yëg]] ci yoon ci ay yëngu yëngu yu wara neex, njaxlafaay gu wacc, ak [[mettit]] bu amul lu ko waral.<ref name=NIH2016/> Nit ñi mëna nañu am yenn saay [[ay yaakaar yu du noonu|ay gëm gëm yu amul]] walla [[gis ay mbir yu fi nekkul|gis walla dégg ay mbir yu nit ñi dul gis walla dégg]].<ref name=NIH2016/> Ñenn ñi am nañu [[Ay diiru naqar gu metti te dara safu ko|ay diiru déteelu]] te ci seen diggante dañuy mel ñépp ay at, te ñeneen ñi ci boobu diir dañuy génne feebar bi.<ref name=DSM5/> Feebaru naqar gu metti ku dara saful mën na japp nit ki japp bu ñaaw ci dundam, walla ci njàngam, walla ci nelawam, walla ci ni muy lekke, ak ci wér gu yaram.<ref name=NIH2016/><ref name=DSM5/> Ci diggante 2-8% ci magg ñi ame feebaru naqar gu metti ku dara saful dañuy dee ak [[xaru]], <ref name=Rich2014>{{cite book|last1=Richards|first1=C. Steven|last2=O'Hara|first2=Michael W. |name-list-format=vanc |title=The Oxford Handbook of Depression and Comorbidity|date=2014|publisher=Oxford University Press|isbn=9780199797042|page=254|url=https://books.google.com/books?id=9jpsAwAAQBAJ&pg=PA254|language=en}}</ref><ref>{{cite book |last1=Strakowski|first1=Stephen |last2=Nelson |first2=Erik |title=Major Depressive Disorder |date=2015 |publisher=Oxford University Press |isbn=9780190264321 |page=PT27 |url=https://books.google.ca/books?id=nD8FCgAAQBAJ&pg=PT27 |language=en}}</ref> te lu tollook 50% ci nit ñiy dee ak xaru amoon nañu déteelu walla beneen feebar [[feebaru dikkale]].<ref>{{cite journal |last1=Bachmann |first1=S |title=Epidemiology of Suicide and the Psychiatric Perspective |journal=International Journal of Environmental Research and Public Health |date=6 July 2018 |volume=15 |issue=7 |pages=1425 |doi=10.3390/ijerph15071425 |pmid=29986446|pmc=6068947 |quote=Half of all completed suicides are related to depressive and other mood disorders}}</ref>
 
<!-- Cause and diagnosis -->
Gëm nañu ne li koy indi mooy ab mbooloowu [[ndono yi ci dereet|ndono ci dereet]], ci li ñu wër, ak ci wallu xel.<ref name=NIH2016>{{cite web|title=Depression|url=http://www.nimh.nih.gov/health/topics/depression/index.shtml|website=NIMH|accessdate=31 July 2016|date=May 2016|deadurl=no|archiveurl=https://web.archive.org/web/20160805065529/http://www.nimh.nih.gov/health/topics/depression/index.shtml|archivedate=5 August 2016}}</ref> Risk yi ñooy ci wallu [[cosaani waa kër gi (paj mi)|cosaanu waa kër gi]] ci li koy joxe, coppite ci dundum nit ki, yenn garab yi, [[jafe jafe yu metti ci wér gu yaram|jafe jafe yu metti ci wér gu yaram]], ak [[feebaru dorogewu]].<ref name=NIH2016/><ref name=DSM5/> Lu tollook 40% ci risk yi ñungi joge ci ndono yi ci dereet.<ref name=DSM5/> Saytu yi ci feebaru naqar gu metti ku dara saful mungi wekku ci jaar jaar yi nit ki di nettali ak benn [[saytu ci fi xelam tollu]].<ref name=Pat2015>{{cite book|last1=Patton|first1=Lauren L.|name-list-format=vanc |title=The ADA Practical Guide to Patients with Medical Conditions|date=2015|publisher=John Wiley & Sons|isbn=9781118929285|page=339|edition=2|url=https://books.google.com/books?id=OTJiCgAAQBAJ&pg=PA339|language=en}}</ref> Amul benn saytu ci laboratoire ngir feebaru déteelu yu gêna bari yi.<ref name=DSM5/> Di ko saytu, waaaye, mën nañu ko def ngir dindi fi yenn jafe jafe yi ci yaram bi yu mëna indi ay yeneen mandarga yu mel noonu.<ref name=Pat2015/> Feebaru déteelu moo gëna metti te mooy gëna yagg [[naqar]], lu bokk ci dund nit ki la .<ref name=DSM5/> Lii di [[United States Preventive Services Task Force]] (USPSTF) laaj na ñu saytu déteelu ci ñi am lu ëpp fukki at ak ñaari, <ref name=US2016>{{cite journal |vauthors=Siu AL, Bibbins-Domingo K, Grossman DC, Baumann LC, Davidson KW, Ebell M, García FA, Gillman M, Herzstein J, Kemper AR, Krist AH, Kurth AE, Owens DK, Phillips WR, Phipps MG, Pignone MP |title=Screening for Depression in Adults: US Preventive Services Task Force Recommendation Statement |journal=JAMA |volume=315 |issue=4 |pages=380–7 |date=January 2016 |pmid=26813211 |doi=10.1001/jama.2015.18392 }}</ref><ref name=US2016Peds>{{cite journal |vauthors=Siu AL |title=Screening for Depression in Children and Adolescents: U.S. Preventive Services Task Force Recommendation Statement |journal=Annals of Internal Medicine |volume=164 |issue=5 |pages=360–6 |date=March 2016 |pmid=26858097 |doi=10.7326/M15-2957 }}</ref>ci waxtu woowu ci [[xibaaru Cochrane ]]gis nañu ne di faraldi di laajte du jappale génne walla faj feebar bi.<ref name=Gil2005>{{cite journal |vauthors=Gilbody S, House AO, Sheldon TA |title=Screening and case finding instruments for depression |journal=The Cochrane Database of Systematic Reviews |issue=4 |pages=CD002792 |date=October 2005 |pmid=16235301 |doi=10.1002/14651858.CD002792.pub2 }}</ref>
 
<!--Treatment and course -->