Xaru wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Hugo.arg (waxtaancëru)
m Hugo.arg moo toppale xët wii di Suicide jëmale ko ci Xaru
Holder (waxtaancëru)
m corr using AWB
Rëdd 3 :
 
<!--Definition and risk factors -->
'''Xaru''' mooy nga am yééne [[ray sa bopp]].<ref name=Sted2006>{{cite book |title=Stedman's Medical Dictionary |year=2006|publisher=Lippincott Williams & Wilkins |location=Philadelphia |isbn=978-0-7817-3390-8 |edition=28th}}</ref> [[feebaru naqar gu metti ku dara saful|feebaru naqar gu metti ku dara saful]], [[Feebaru "bipolaire"]], [[Feebaru "schizophrénie"]], [[feebaru nekkin|feebari nekkin]], ak [[feebaru dorogewu]] - boole ci [[naan gu bari gi]] ak jëfandikoo [[garabu Benzodiazepine|garabu benzodiazepine]] - yi yépp luy indi xaru la<ref name=WHO2016/><ref name=Hawton2009>{{cite journal | vauthors = Hawton K, van Heeringen K | title = Suicide | journal = Lancet | volume = 373 | issue = 9672 | pages = 1372–81 | date = April 2009 | pmid = 19376453 | doi = 10.1016/S0140-6736(09)60372-X }}</ref><ref name=Dod2017>{{cite journal | vauthors = Dodds TJ | title = Prescribed Benzodiazepines and Suicide Risk: A Review of the Literature | journal = The Primary Care Companion for CNS Disorders | volume = 19 | issue = 2 | date = March 2017 | pmid = 28257172 | doi = 10.4088/PCC.16r02037 }}</ref> Ñenn ci ñi di xaru dafa am [[lu leen di dooleel|ay jëf yu ñu dooleel ]]ndax stress joge ci[[jafe-jafe xaalis]], jafe-jafe [[nekk ak nit ñi|nekkin ak nit ñi nekkin ci diggante ay nit]], walla [[tiital]]<ref name=WHO2016/><ref>{{cite journal | vauthors = Bottino SM, Bottino CM, Regina CG, Correia AV, Ribeiro WS | title = Cyberbullying and adolescent mental health: systematic review | journal = Cadernos De Saude Publica | volume = 31 | issue = 3 | pages = 463–75 | date = March 2015 | pmid = 25859714 | doi = 10.1590/0102-311x00036114 }}</ref> Ñi mësa jééma xaru dañu nekk ñoo xamantane ngir ñu jéémaata xaru lu yomb la.<ref name=WHO2016/> [[Fagaru ngir waññi xaru ]]jéégo yi ñooy nééwal yoon yi di indi xaru - lu mel ni [[ay fetal]], dorog, ak poson; faj feebaru xel yi ak dorogekat yi; [[yéglekaay yu mag yi|yéglekaay yi]] nettali bu xaru amee, te yoq koom-koomi nit ñi.<ref name=WHO2016>{{cite web|title=Suicide Fact sheet N°398|url=http://www.who.int/mediacentre/factsheets/fs398/en/|website=WHO|access-date=3 March 2016|date=April 2016|deadurl=no|archive-url=https://web.archive.org/web/20160304192347/http://www.who.int/mediacentre/factsheets/fs398/en/|archive-date=4 March 2016|df=}}</ref> Su fekkee sax [[nimero bi nit ñi mëne woote saa yu nekk su ñu amee jafe-jafe|ay nimero yu nit ñi mëne woote saa yu nekk su ñu amee jafe-jafe]] bare nañu, wóórul ne am nañu njëriñ.<ref name=Sak2011>{{cite journal | vauthors = Sakinofsky I | title = The current evidence base for the clinical care of suicidal patients: strengths and weaknesses | journal = Canadian Journal of Psychiatry. Revue Canadienne De Psychiatrie | volume = 52 | issue = 6 Suppl 1 | pages = 7S-20S | date = June 2007 | pmid = 17824349 }}</ref>
 
<!--Method -->
Rëdd 12 :
 
<!--History, society and culture -->
Ay gis-gis yi nit ñi am ci xaru ñungi bawoo ci[[ay ngëm-ngëm ]]yu mel ni diine, [[teddaay]], ak [[njëriñu dund bi]].<ref>{{cite book|last1=Tomer|first1=Adrian | name-list-format = vanc |title=Existential and Spiritual Issues in Death Attitudes|date=2013|publisher=Psychology Press|isbn=9781136676901|page=282|url=https://books.google.com/books?id=hJTruwsicuoC&pg=PA282 }}</ref><ref>{{cite book |last1=Ritzer |first1=edited by George |last2=Stepnisky |first2=Jeffrey | name-list-format = vanc |title=The Wiley-Blackwell companion to major social theorists |date=2011 |publisher=Wiley-Blackwell |location=Malden, MA |isbn=9781444396607 |page=65 |url=https://books.google.com/books?id=MDwdmVUMIh8C&pg=PA65 }}</ref> Yii [[Diine yu joge ci Ibrahima ]]dañu gise xaru ni ab [[bakkaar|tooñ Yalla]], ndax seen ngëm-ngëm ci [[sellaay yu dund bi]].<ref>{{cite book|title=God, Religion, Science, Nature, Culture, and Morality|date=2014|publisher=Archway Publishing|isbn=9781480811249|page=254|url=https://books.google.com/books?id=xGGVBQAAQBAJ&pg=PA254 }}</ref> Bi [[samurai ]]doon am ca Japon, benn xeetu xaru bi ñu xamewoon ni [[seppuku]] ''harakiri'' dañu ko joxoon cër ni beneen yoon ngir bëral ñakka tekki walla ni yoonu ñaxtu.<ref>{{cite book|last1=Colt|first1=George Howe|title=The enigma of suicide|date=1992|publisher=Simon & Schuster|location=New York|isbn=9780671760717|page=139|edition=1st Touchstone|url=https://books.google.com/books?id=DOz3hStePfYC&pg=PA139 }}</ref> [[Sati (topp)|Sati]], benn jëf-jëf la bu ñu terewoon joge ci [[Raju Britanique bi]], bu doon xaar [[Jëtuur#Jëtuur yi ci aada waa Inde|Jëtuur Indo bi]]di[[lakk boppam|ray boppam ]]bi nééwu jëkkëram ji [[di dem ci fi ñu koy lakke ngir rob ko|taalu robukaay]], mu defal ko boppam walla waa këram ak mbooloo mi di ko puus.<ref>{{cite web |url=http://www.bbc.co.uk/worldservice/learningenglish/news/words/general/020807_witn.shtml |title=Indian woman commits sati suicide |publisher=Bbc.co.uk |date=2002-08-07 |access-date=2010-08-26 |deadurl=no |archive-url=https://web.archive.org/web/20110202101233/http://www.bbc.co.uk/worldservice/learningenglish/news/words/general/020807_witn.shtml |archive-date=2011-02-02 |df= }}</ref> Xaru ak jééma xaru, bu njëkka ba dañu ko terewoon, waaye léégi ci rééwi Tugël yu bari kenn tereetu ko <ref name=White2010>{{cite book|last=White | first = Tony | name-list-format = vanc |title=Working with suicidal individuals : a guide to providing understanding, assessment and support|year=2010|publisher=Jessica Kingsley Publishers|location=London|isbn=978-1-84905-115-6|page=12|url=https://books.google.com/books?id=p_ZvK-DBYfIC&pg=PT12 }}</ref> Boobu [[#yoon|dafa nekk ab ñaawtééf ci rééw yu bari ba léégi]]<ref name=Islam2006>{{cite journal | vauthors = Lester D | title = Suicide and islam | journal = Archives of Suicide Research | volume = 10 | issue = 1 | pages = 77–97 | year = 2006 | pmid = 16287698 | doi = 10.1080/13811110500318489 }}</ref> Ci siecle ñaar fukkeel ak ñaar fukkeel ak benn, xaru lu nééw lañu ko jëfandikoo ni xeetu ñaxtu, ak [[kamikaze]] ak [[xaru ak ay bomb]] nekk na lu ñu daan jëfandikoo ni jëfinu militaire walla terroriste.
<ref>{{cite journal | vauthors = Aggarwal N | title = Rethinking suicide bombing | journal = Crisis | volume = 30 | issue = 2 | pages = 94–7 | year = 2009 | pmid = 19525169 | doi = 10.1027/0227-5910.30.2.94 }}</ref>
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Xaru » lañ ko jële