Garab wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Seexloo393 (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Seexloo393 (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 15 :
Dañuy liggeey, liggeey bu am solo nag ci jokkalanteg càkkéef gi. (Jokkalante gi am ci yi ci àdduna bépp, nga xam ne ku ne aajewoo nga sa moroom.)
 
Ndax dañuy muucu gaasub karbon bi doomu aadama yi génne di ko denc.
Ba noppi di génne gaas ogsisen bi nga xam ne nit moom lay soxla ngir dund.
Rëdd 37 :
Loolu nag moo koy wuutali ak garab yu ndawaan yi ñiy woowe ay ngajj. Niki ngeer, salaan añs, yooyu nga xam ne seenub guddaay buñu màggee ci diggante genn-wàllu met ba ci 5i met walla 7i met lay toll, te nga xam ne ñoom daanaka duñu am ker, duñu am mbaar.
 
FAO itam dugal na ci loolu garab yi nga xam ne amuñu li ñiy wax liñindaakaande, lu deme ni ron walla dànq.
 
Liñin nag mooy, booBoo jëlee lu mel neni ron, bant bi boo ko dagge day am lu mel ne am lëm ca biir, nga xam ne bant bi lépp feesul, te namu war a dëgëre du ko dëgëre, ndax bu gënee wow day mel ne ay bant yu sew la yu dajaloo. Loolu li mu amul daakaande moo ko waral. Yooyu amul ci '''niimaa'''. '''Niimaa''' nga xam ne aw dénk la wu dëgër buñu ko daggee, moom dafa am liñindaakaande moo tax, liñindaakaande ji moo waral mu dëgëre noonu. Bu dee '''ron''' nag amu ko, moo tax muy def ay bant yu sew.
 
BuAmna deeit (fëlës)ñoñ yi, ni ñuyniñu waxejàppe garab, maanaammooy gépp garab gu am liñindaakaande rekk lañuy wax garab.
Waaye FAO moom da cee dolli yi amumamul liñindaakaande.
 
Waa IFN moom dañoo wax ne, garab mooy xeetu gàncax goo xam ne dafa am liñin, ba noppi am ab bànqaas boo xam ne dara sax na ca, ba noppi guddaay ba day tollook 5i met walla mu ëpp ko.
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Garab » lañ ko jële