Laayeen wuute gi ci sumb yi

14 octets ajoutés ,  13 at ci ginaaw
m
robot Adding: en:Layene
m (robot Adding: en:Layene)
Siiwam gi tiitloo woon na way sanc yi ragaloon ag jeqiku kontar leen. Ci atum 1887 g.j, la sancaan yi taxaw ci jàpp ko, bi mu yëgee seen naal yooyu la ànd ak lenn ciy àndadoom génn, waaye tubaab bi jàpp ko ca wetu Caaroy. Waaye ëttu àtte bi mujj na ko setal ko ngir ñàkk lenn lu man a dëgëral tuuma yi ñu teg ci kawam. Limaamu wéyoon na ci wooteem gi, waaye daa na def jamono ju nekk muy fenqook sancaan yi ko daa jéem a sonal ak àndandoom yi. Mi ngi làqu atum 1909 g.j.
 
[[en:Layene]]
[[fr:Layène]]
339

modifications